Al-Furqan · 65/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
وَالَّذِينَ يَقُولُونَ رَبَّنَا اصْرِفْ عَنَّا عَذَابَ جَهَنَّمَ ۖ إِنَّ عَذَابَهَا كَانَ غَرَامًا ۝٦٥
Wallazeena yaqooloona Rabbanas rif `annnaa `azaaba Jahannama inn `azaabahaa kaana gharaamaa
📖 Tekkim Wolof
ñoom ñooy wax naan : “Yàlla, yal na nga nu dëddëleek mbugalum Safara”. - mbugalum Safara soosu lu ne dànk la.

🎧 Dégg


📜 Aaya 63-67 — Simoore Al-Furqan

63وَعِبَادُ الرَّحْمَٰنِ الَّذِينَ يَمْشُونَ عَلَى الْأَرْضِ هَوْنًا وَإِذَا خَاطَبَهُمُ الْجَاهِلُونَ قَالُوا سَلَامًا
Ak jaami Yàlla yii dox ci kaw suuf si ndànk, su ñu réer ña di wàqanteek ñoom, ñuy wax jàmm,
64وَالَّذِينَ يَبِيتُونَ لِرَبِّهِمْ سُجَّدًا وَقِيَامًا
ñoom ñooy fanaanee julli te Yàlla rekk tax [taxaw ak a sujjóot] ;
65وَالَّذِينَ يَقُولُونَ رَبَّنَا اصْرِفْ عَنَّا عَذَابَ جَهَنَّمَ ۖ إِنَّ عَذَابَهَا كَانَ غَرَامًا
ñoom ñooy wax naan : “Yàlla, yal na nga nu dëddëleek mbugalum Safara”. - mbugalum Safara soosu lu ne dànk la.
66إِنَّهَا سَاءَتْ مُسْتَقَرًّا وَمُقَامًا
Ndaw dëkkuwaay bu soof !
67وَالَّذِينَ إِذَا أَنفَقُوا لَمْ يُسْرِفُوا وَلَمْ يَقْتُرُوا وَكَانَ بَيْنَ ذَٰلِكَ قَوَامًا
Bu ñuy joxe alal, duñu xaabaabal te it duñu nay, dañuy digg-dóomu.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
65Aaya

Tekki — Al-Furqan 65

Simoore Al-Furqan Aaya 65 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ñoom ñooy wax naan : “Yàlla, yal na nga nu…

Simoore Aaya 65/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 63–67. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers