Ash-Shu'ara · 105/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
كَذَّبَتْ قَوْمُ نُوحٍ الْمُرْسَلِينَ ۝١٠٥
Kazzabat qawmu Noohinil Mursaleen
📖 Tekkim Wolof
Nitu Nooh ñoom weddi woon nañu Yonent ya,

🎧 Dégg


📜 Aaya 103-107 — Simoore Ash-Shu'ara

103إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ
Ay kéemaan a ngi ci biir loolu ; te taxut woon li ëpp ci ñoom gëm.
104وَإِنَّ رَبَّكَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Te sa Borom, mooy Boroom kàttan, di Jaglewaakoon ba.
105كَذَّبَتْ قَوْمُ نُوحٍ الْمُرْسَلِينَ
Nitu Nooh ñoom weddi woon nañu Yonent ya,
106إِذْ قَالَ لَهُمْ أَخُوهُمْ نُوحٌ أَلَا تَتَّقُونَ
ba leen seen mbokk ma Nooh waxee, ne leen : “Ndax dungeen ragal Yàlla ?
107إِنِّي لَكُمْ رَسُولٌ أَمِينٌ
Man seenub Yonent laa bu wóor.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
105Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 105

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 105 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nitu Nooh ñoom weddi woon nañu Yonent ya,

Simoore Aaya 105/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 103–107. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers