Ash-Shu'ara · 123/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
كَذَّبَتْ عَادٌ الْمُرْسَلِينَ ۝١٢٣
Kazzabat `Aadunil mursaleen
📖 Tekkim Wolof
Waa Haad, weddi woon nañu Yonent ya, jàppe leen ay fenkat.

🎧 Dégg


📜 Aaya 121-125 — Simoore Ash-Shu'ara

121إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ
Ay kéemaan a nga ci biir loolu. Te taxut woon la ëpp ci ñoom gëm.
122وَإِنَّ رَبَّكَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Te sa Boorm, Mooy boroom kàttan, di Jaglewaakoon.
123كَذَّبَتْ عَادٌ الْمُرْسَلِينَ
Waa Haad, weddi woon nañu Yonent ya, jàppe leen ay fenkat.
124إِذْ قَالَ لَهُمْ أَخُوهُمْ هُودٌ أَلَا تَتَّقُونَ
Ba leen seen mbokk ma Huud waxee ne : “Ndax dangeen dul ragal Yàlla ? ”
125إِنِّي لَكُمْ رَسُولٌ أَمِينٌ
Man dey, ab Yonent laa bu wóor,
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
123Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 123

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 123 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waa Haad, weddi woon nañu Yonent ya, jàppe leen ay…

Simoore Aaya 123/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 121–125. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers