Ash-Shu'ara · 215/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَاخْفِضْ جَنَاحَكَ لِمَنِ اتَّبَعَكَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ ۝٢١٥
Wakhfid janaahaka limanit taba `aka minal mu`mineen
📖 Tekkim Wolof
Nangay suufeel sa bopp ci jullit ñi la topp [say ndigal].

🎧 Dégg


📜 Aaya 213-217 — Simoore Ash-Shu'ara

213فَلَا تَدْعُ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ فَتَكُونَ مِنَ الْمُعَذَّبِينَ
Bul jaamu lenn di ko booleek Yàlla, ku koy def rekk mbugal di dal ci sa kaw.
214وَأَنذِرْ عَشِيرَتَكَ الْأَقْرَبِينَ
Nangay xupp yaw [Muhammad] nit ñi la gën a jegeñ.
215وَاخْفِضْ جَنَاحَكَ لِمَنِ اتَّبَعَكَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Nangay suufeel sa bopp ci jullit ñi la topp [say ndigal].
216فَإِنْ عَصَوْكَ فَقُلْ إِنِّي بَرِيءٌ مِّمَّا تَعْمَلُونَ
Bu ñu moyee nag, neeleen : “Samaw yoon nekkatul ci li ngeen di def”.
217وَتَوَكَّلْ عَلَى الْعَزِيزِ الرَّحِيمِ
Nangay wéeru ci Yàlla Miy Boroom kàttan tey Jaglewaakoonu yërmaande,
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
215Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 215

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 215 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nangay suufeel sa bopp ci jullit ñi la topp [say…

Simoore Aaya 215/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 213–217. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers