Ash-Shu'ara · 216/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
فَإِنْ عَصَوْكَ فَقُلْ إِنِّي بَرِيءٌ مِّمَّا تَعْمَلُونَ ۝٢١٦
Fa in asawka faqul innee bareee`um mimmmaa ta`maloon
📖 Tekkim Wolof
Bu ñu moyee nag, neeleen : “Samaw yoon nekkatul ci li ngeen di def”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 214-218 — Ash-Shu'ara

214وَأَنذِرْ عَشِيرَتَكَ الْأَقْرَبِينَ
Nangay xupp yaw [Muhammad] nit ñi la gën a jegeñ.
215وَاخْفِضْ جَنَاحَكَ لِمَنِ اتَّبَعَكَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Nangay suufeel sa bopp ci jullit ñi la topp [say ndigal].
216فَإِنْ عَصَوْكَ فَقُلْ إِنِّي بَرِيءٌ مِّمَّا تَعْمَلُونَ
Bu ñu moyee nag, neeleen : “Samaw yoon nekkatul ci li ngeen di def”.
217وَتَوَكَّلْ عَلَى الْعَزِيزِ الرَّحِيمِ
Nangay wéeru ci Yàlla Miy Boroom kàttan tey Jaglewaakoonu yërmaande,
218الَّذِي يَرَاكَ حِينَ تَقُومُ
Moom mi lay gis boo taxawee,
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
216Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 216

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 216 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ñu moyee nag, neeleen : “Samaw yoon nekkatul ci…

Simoore Aaya 216/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 214–218. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers