Ash-Shu'ara · 214/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَأَنذِرْ عَشِيرَتَكَ الْأَقْرَبِينَ ۝٢١٤
Wa anzir `asheeratakal aqrabeen
📖 Tekkim Wolof
Nangay xupp yaw [Muhammad] nit ñi la gën a jegeñ.

🎧 Dégg


📜 Aaya 212-216 — Simoore Ash-Shu'ara

212إِنَّهُمْ عَنِ السَّمْعِ لَمَعْزُولُونَ
Ñoom mënuñoo dégg ndigali Yàlla.
213فَلَا تَدْعُ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ فَتَكُونَ مِنَ الْمُعَذَّبِينَ
Bul jaamu lenn di ko booleek Yàlla, ku koy def rekk mbugal di dal ci sa kaw.
214وَأَنذِرْ عَشِيرَتَكَ الْأَقْرَبِينَ
Nangay xupp yaw [Muhammad] nit ñi la gën a jegeñ.
215وَاخْفِضْ جَنَاحَكَ لِمَنِ اتَّبَعَكَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Nangay suufeel sa bopp ci jullit ñi la topp [say ndigal].
216فَإِنْ عَصَوْكَ فَقُلْ إِنِّي بَرِيءٌ مِّمَّا تَعْمَلُونَ
Bu ñu moyee nag, neeleen : “Samaw yoon nekkatul ci li ngeen di def”.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
214Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 214

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 214 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nangay xupp yaw [Muhammad] nit ñi la gën a jegeñ.

Simoore Aaya 214/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 212–216. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers