Ash-Shu'ara · 217/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَتَوَكَّلْ عَلَى الْعَزِيزِ الرَّحِيمِ ۝٢١٧
Wa tawakkal alal `Azeezir Raheem
📖 Tekkim Wolof
Nangay wéeru ci Yàlla Miy Boroom kàttan tey Jaglewaakoonu yërmaande,

🎧 Dégg


📜 Aaya 215-219 — Simoore Ash-Shu'ara

215وَاخْفِضْ جَنَاحَكَ لِمَنِ اتَّبَعَكَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Nangay suufeel sa bopp ci jullit ñi la topp [say ndigal].
216فَإِنْ عَصَوْكَ فَقُلْ إِنِّي بَرِيءٌ مِّمَّا تَعْمَلُونَ
Bu ñu moyee nag, neeleen : “Samaw yoon nekkatul ci li ngeen di def”.
217وَتَوَكَّلْ عَلَى الْعَزِيزِ الرَّحِيمِ
Nangay wéeru ci Yàlla Miy Boroom kàttan tey Jaglewaakoonu yërmaande,
218الَّذِي يَرَاكَ حِينَ تَقُومُ
Moom mi lay gis boo taxawee,
219وَتَقَلُّبَكَ فِي السَّاجِدِينَ
ak say jëfiin ba nga nekkee ci biir ñay sujjóot [julli].
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
217Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 217

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 217 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nangay wéeru ci Yàlla Miy Boroom kàttan tey Jaglewaakoonu yërmaande,

Simoore Aaya 217/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 215–219. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers