An-Naml · 43/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
وَصَدَّهَا مَا كَانَت تَّعْبُدُ مِن دُونِ اللَّهِ ۖ إِنَّهَا كَانَتْ مِن قَوْمٍ كَافِرِينَ ۝٤٣
Wa saddahaa maa kaanat ta`budu min doonil laahi innahaa kaanat min qawmin kaafireen
📖 Tekkim Wolof
Li mu daan jaamu bàyyi Yàlla moo ko fàbbi woon, ndax dafa bokkoon ci askanu yéefar.

🎧 Dégg


📜 Aaya 41-45 — Simoore An-Naml

41قَالَ نَكِّرُوا لَهَا عَرْشَهَا نَنظُرْ أَتَهْتَدِي أَمْ تَكُونُ مِنَ الَّذِينَ لَا يَهْتَدُونَ
Suleymaan réerantal leen, toog na di xool ndax dana gindiku am déet.
42فَلَمَّا جَاءَتْ قِيلَ أَهَٰكَذَا عَرْشُكِ ۖ قَالَتْ كَأَنَّهُ هُوَ ۚ وَأُوتِينَا الْعِلْمَ مِن قَبْلِهَا وَكُنَّا مُسْلِمِينَ
Ba Balxiis agsee, ñu ne ko : “Ndax lii mooy sa toogu ba ? ” Mu ne : “Mel na ni moom la de”. - [Suleymaan ne]: “Am nanu xam-xam lu ko jiitu ba tax na nu jébbalusi”.
43وَصَدَّهَا مَا كَانَت تَّعْبُدُ مِن دُونِ اللَّهِ ۖ إِنَّهَا كَانَتْ مِن قَوْمٍ كَافِرِينَ
Li mu daan jaamu bàyyi Yàlla moo ko fàbbi woon, ndax dafa bokkoon ci askanu yéefar.
44قِيلَ لَهَا ادْخُلِي الصَّرْحَ ۖ فَلَمَّا رَأَتْهُ حَسِبَتْهُ لُجَّةً وَكَشَفَتْ عَن سَاقَيْهَا ۚ قَالَ إِنَّهُ صَرْحٌ مُّمَرَّدٌ مِّن قَوَارِيرَ ۗ قَالَتْ رَبِّ إِنِّي ظَلَمْتُ نَفْسِي وَأَسْلَمْتُ مَعَ سُلَيْمَانَ لِلَّهِ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Ñu ne ko : “Dugal ci njénde li”. Ba mu ko gisee, mu njort ne am ndox la, daldi wog i yeelam. Suleymaan ne ko : “Njénde li ay weer la ñu ko defare”. - Balxiis daldi ne : “Yaw Boroom bi, tooñaan naa sama bopp : Tey jii nag, jébbalu naa ànd ak Suleymaan dib jullit ngir Yàlla jiy Boroom àddina si”.
45وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا إِلَىٰ ثَمُودَ أَخَاهُمْ صَالِحًا أَنِ اعْبُدُوا اللَّهَ فَإِذَا هُمْ فَرِيقَانِ يَخْتَصِمُونَ
Yónnee woon Nanu ca Samuuda seen mbokk Saaliwu. Mu ne leen : “Jaamuleen Yàlla”. Ndekete yoo dañoo séddalikoo ñaari kurél di xulloo rekk.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
43Aaya

Tekki — An-Naml 43

Simoore An-Naml Aaya 43 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Li mu daan jaamu bàyyi Yàlla moo ko fàbbi woon,…

Simoore Aaya 43/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 41–45. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers