An-Naml · 69/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
قُلْ سِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَانظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُجْرِمِينَ ۝٦٩
Qul seeroo fil ardi fanzuroo kaifa kaana `aaqibatul mujremeen
📖 Tekkim Wolof
Neeleen : “Doxleen ci suuf si [wëréelu] te ngeen xool naka la tooñkat ya mujje”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 67-71 — Simoore An-Naml

67وَقَالَ الَّذِينَ كَفَرُوا أَإِذَا كُنَّا تُرَابًا وَآبَاؤُنَا أَئِنَّا لَمُخْرَجُونَ
Yéefar yaa ngay wax naan : “Ndax [ginnaaw ba ñu faatoo] ba doon suuf nook sunuy baay, dananu génnaat suuf [dekki] ?
68لَقَدْ وُعِدْنَا هَٰذَا نَحْنُ وَآبَاؤُنَا مِن قَبْلُ إِنْ هَٰذَا إِلَّا أَسَاطِيرُ الْأَوَّلِينَ
Lii daal digoon nañu nu ko nook sunuy baay. Lii du dara lu dul léebi mag ñu jëkk ña ! ”.
69قُلْ سِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَانظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُجْرِمِينَ
Neeleen : “Doxleen ci suuf si [wëréelu] te ngeen xool naka la tooñkat ya mujje”.
70وَلَا تَحْزَنْ عَلَيْهِمْ وَلَا تَكُن فِي ضَيْقٍ مِّمَّا يَمْكُرُونَ
Bul jàq ci ñoom te seeni pexe itam bu mu la xatal.
71وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هَٰذَا الْوَعْدُ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ñangay wax naan : “Dig bi moom kañ lay doon ndegam wax ngeen dëgg ? ”
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
69Aaya

Tekki — An-Naml 69

Simoore An-Naml Aaya 69 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neeleen : “Doxleen ci suuf si [wëréelu] te ngeen xool…

Simoore Aaya 69/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 67–71. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers