An-Naml · 70/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
وَلَا تَحْزَنْ عَلَيْهِمْ وَلَا تَكُن فِي ضَيْقٍ مِّمَّا يَمْكُرُونَ ٧٠
Transliteration
Wa laa tahzan `alaihim wa laa takun fee daiqim mimmaa yamkuroon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Bul jàq ci ñoom te seeni pexe itam bu mu la xatal.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 68-72 — An-Naml
68لَقَدْ وُعِدْنَا هَٰذَا نَحْنُ وَآبَاؤُنَا مِن قَبْلُ إِنْ هَٰذَا إِلَّا أَسَاطِيرُ الْأَوَّلِينَ
Lii daal digoon nañu nu ko nook sunuy baay. Lii du dara lu dul léebi mag ñu jëkk ña ! ”.
69قُلْ سِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَانظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُجْرِمِينَ
Neeleen : “Doxleen ci suuf si [wëréelu] te ngeen xool naka la tooñkat ya mujje”.
70وَلَا تَحْزَنْ عَلَيْهِمْ وَلَا تَكُن فِي ضَيْقٍ مِّمَّا يَمْكُرُونَ
Bul jàq ci ñoom te seeni pexe itam bu mu la xatal.
71وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هَٰذَا الْوَعْدُ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ñangay wax naan : “Dig bi moom kañ lay doon ndegam wax ngeen dëgg ? ”
72قُلْ عَسَىٰ أَن يَكُونَ رَدِفَ لَكُم بَعْضُ الَّذِي تَسْتَعْجِلُونَ
Neel : “Amaana lii ngeen di yàkkamtee ngi ci seen kaw”.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
70Aaya
Tekki — An-Naml 70
Simoore An-Naml Aaya 70 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bul jàq ci ñoom te seeni pexe itam bu mu…Simoore Aaya 70/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 68–72. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








