Al-Qasas · 56/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
إِنَّكَ لَا تَهْدِي مَنْ أَحْبَبْتَ وَلَٰكِنَّ اللَّهَ يَهْدِي مَن يَشَاءُ ۚ وَهُوَ أَعْلَمُ بِالْمُهْتَدِينَ ۝٥٦
Innaka laa tahdee man ahbata wa laakinna laaha yahdee mai yashaaa`; wa Huwaa`lamu bilmuhtadeen
📖 Tekkim Wolof
Yaw (Muhammad) du ut ne yaay gindi ku la soob : waaye Yàlla mooy gindi ku ko soob. Te moo gën a xam ñiy gindiku.

🎧 Dégg


📜 Aaya 54-58 — Simoore Al-Qasas

54أُولَٰئِكَ يُؤْتَوْنَ أَجْرَهُم مَّرَّتَيْنِ بِمَا صَبَرُوا وَيَدْرَءُونَ بِالْحَسَنَةِ السَّيِّئَةَ وَمِمَّا رَزَقْنَاهُمْ يُنفِقُونَ
Ñooña danañu seen pey ñaari yoon ca la ñu daan muñ, daan toontoo aw ñaawtéef ak lu rafet, te di joxe ca la Ma leen wërsëgal ;
55وَإِذَا سَمِعُوا اللَّغْوَ أَعْرَضُوا عَنْهُ وَقَالُوا لَنَا أَعْمَالُنَا وَلَكُمْ أَعْمَالُكُمْ سَلَامٌ عَلَيْكُمْ لَا نَبْتَغِي الْجَاهِلِينَ
te saa yu ñu déggee ay caaxaan, dummóoyu ko tey wax naan : “Nun ak sunuy jëf, yéen ak séeni jëf. Yal na ngeen am jàmm. Nun dey, dunu sàkkuji mukk ñu réer ña”.
56إِنَّكَ لَا تَهْدِي مَنْ أَحْبَبْتَ وَلَٰكِنَّ اللَّهَ يَهْدِي مَن يَشَاءُ ۚ وَهُوَ أَعْلَمُ بِالْمُهْتَدِينَ
Yaw (Muhammad) du ut ne yaay gindi ku la soob : waaye Yàlla mooy gindi ku ko soob. Te moo gën a xam ñiy gindiku.
57وَقَالُوا إِن نَّتَّبِعِ الْهُدَىٰ مَعَكَ نُتَخَطَّفْ مِنْ أَرْضِنَا ۚ أَوَلَمْ نُمَكِّن لَّهُمْ حَرَمًا آمِنًا يُجْبَىٰ إِلَيْهِ ثَمَرَاتُ كُلِّ شَيْءٍ رِّزْقًا مِّن لَّدُنَّا وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Ñuy wax naan : “Su nu toppee njub gi ànd ak yaw, kon deef nanu foqarñee ci sunu suuf si”. - Ndax defalunu leen woon am réew wuñu wormaal, ñuy jëmmal wépp xeetu meññeef muy bawoo ci Nun [Yàlla] ? Waaye li ëpp ci ñoom xamuñu.
58وَكَمْ أَهْلَكْنَا مِن قَرْيَةٍ بَطِرَتْ مَعِيشَتَهَا ۖ فَتِلْكَ مَسَاكِنُهُمْ لَمْ تُسْكَن مِّن بَعْدِهِمْ إِلَّا قَلِيلًا ۖ وَكُنَّا نَحْنُ الْوَارِثِينَ
Aka bari dëkk bu Nu faagaagal ci sababus seenug weddi te ñu daan dunde xéewal, ca seen kër ya lu néew la, te keneen dëkkee seen ginnaaw, Nun Yàlla noo doon donnale.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
56Aaya

Tekki — Al-Qasas 56

Simoore Al-Qasas Aaya 56 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yaw (Muhammad) du ut ne yaay gindi ku la soob…

Simoore Aaya 56/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 54–58. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers