Aali Imran · 117/200
Tekki Waxtaan — Simoore Aali Imran
مَثَلُ مَا يُنفِقُونَ فِي هَٰذِهِ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا كَمَثَلِ رِيحٍ فِيهَا صِرٌّ أَصَابَتْ حَرْثَ قَوْمٍ ظَلَمُوا أَنفُسَهُمْ فَأَهْلَكَتْهُ ۚ وَمَا ظَلَمَهُمُ اللَّهُ وَلَٰكِنْ أَنفُسَهُمْ يَظْلِمُونَ ۝١١٧
Masalu maa yunfiqoona fee haazihil hayaatid dunyaa kamasali reehin feehaa sirrun as aabat harsa qawmin zalamooo anfusahum fa ahlakath; wa maa zalamahumul laahu wa laakin anfusahum yazlimoon
📖 Tekkim Wolof
La ñuy joxe ci seeni alal ci mbiri àdduna dafa mel ni ngelaw lu ànd ak safara dal ci kaw mbeyum ña tooñ seen bopp, ne ko fuuf lakk ko. Yàlla tooñuleen waaye ñoom ñoo tooñ seen bopp.

🎧 Dégg


📜 Aaya 115-119 — Simoore Aali Imran

115وَمَا يَفْعَلُوا مِنْ خَيْرٍ فَلَن يُكْفَرُوهُ ۗ وَاللَّهُ عَلِيمٌ بِالْمُتَّقِينَ
Lu ngeen jëf ci aw yiw, kenn duleen ko xañ. Yàlla xam na ña ko ragal .
116إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا لَن تُغْنِيَ عَنْهُمْ أَمْوَالُهُمْ وَلَا أَوْلَادُهُم مِّنَ اللَّهِ شَيْئًا ۖ وَأُولَٰئِكَ أَصْحَابُ النَّارِ ۚ هُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
Ña weddi, seeni alal ak seeni doom duñuleen jariñ dara fa Yàlla. Ñoom ñooy waa Safara te dañu fay béel.
117مَثَلُ مَا يُنفِقُونَ فِي هَٰذِهِ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا كَمَثَلِ رِيحٍ فِيهَا صِرٌّ أَصَابَتْ حَرْثَ قَوْمٍ ظَلَمُوا أَنفُسَهُمْ فَأَهْلَكَتْهُ ۚ وَمَا ظَلَمَهُمُ اللَّهُ وَلَٰكِنْ أَنفُسَهُمْ يَظْلِمُونَ
La ñuy joxe ci seeni alal ci mbiri àdduna dafa mel ni ngelaw lu ànd ak safara dal ci kaw mbeyum ña tooñ seen bopp, ne ko fuuf lakk ko. Yàlla tooñuleen waaye ñoom ñoo tooñ seen bopp.
118يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَتَّخِذُوا بِطَانَةً مِّن دُونِكُمْ لَا يَأْلُونَكُمْ خَبَالًا وَدُّوا مَا عَنِتُّمْ قَدْ بَدَتِ الْبَغْضَاءُ مِنْ أَفْوَاهِهِمْ وَمَا تُخْفِي صُدُورُهُمْ أَكْبَرُ ۚ قَدْ بَيَّنَّا لَكُمُ الْآيَاتِ ۖ إِن كُنتُمْ تَعْقِلُونَ
Yéen ñi gëm, buleen won seen mbir ci ag xaritoo keneen ku bokkul ci yéen. Bumuy ci ñoo xam ne dañuy kàttanlu ci yàqal leen, danañu ngéeju ngir ngeen am coono. Mbañeel ga feen na ca seeni wax, te la seeni xol ëmb moo yéesati. Yéen leeral nanu leen kéemaan yi [ngeen war leen a ràññee ndegam ñu xel-lu ngeen ! ].
119هَا أَنتُمْ أُولَاءِ تُحِبُّونَهُمْ وَلَا يُحِبُّونَكُمْ وَتُؤْمِنُونَ بِالْكِتَابِ كُلِّهِ وَإِذَا لَقُوكُمْ قَالُوا آمَنَّا وَإِذَا خَلَوْا عَضُّوا عَلَيْكُمُ الْأَنَامِلَ مِنَ الْغَيْظِ ۚ قُلْ مُوتُوا بِغَيْظِكُمْ ۗ إِنَّ اللَّهَ عَلِيمٌ بِذَاتِ الصُّدُورِ
Yéen ak ñoom, yëgleen ne yéen a leen safoo, waaye ñoom safoowuñu leen ; te yéen gëm ngeen Téere bi lépp. Bu ñu dajee ak yéen ne “Gëm nanu” ; bu ñu wéyee màtt seeni waaroom wiccax ndax mer. Neel : “Deeleen ci mer” ; Yàlla ku xam la lu nekk ci xol yi.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
117Aaya

Tekki — Aali Imran 117

Simoore Aali Imran Aaya 117 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : La ñuy joxe ci seeni alal ci mbiri àdduna dafa…

Simoore Aaya 117/200 — Simoore Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Aali Imran Dégg, Simoore Aali Imran Tekki, Simoore Aali Imran mp3, Simoore Aali Imran pdf. Aaya 115–119. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers