Aali Imran · 136/200
Tekki Waxtaan — Simoore Aali Imran
أُولَٰئِكَ جَزَاؤُهُم مَّغْفِرَةٌ مِّن رَّبِّهِمْ وَجَنَّاتٌ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ خَالِدِينَ فِيهَا ۚ وَنِعْمَ أَجْرُ الْعَامِلِينَ ۝١٣٦
Ulaaa`ika jazaaa`uhum maghfiratum mir Rabbihim wa Jannaatun tajree min tahtihal anhaaru khaalideena feeha; wa ni`ma ajrul `aamileen
📖 Tekkim Wolof
Ñooña seenug pey moo di jéggal gu bawoo ca seen Boroom, ak Àjjana yu dex ya di daw ci seen ron, te dañu fay béel. Loolu ag pey dàqatuko !

🎧 Dégg


📜 Aaya 134-138 — Simoore Aali Imran

134الَّذِينَ يُنفِقُونَ فِي السَّرَّاءِ وَالضَّرَّاءِ وَالْكَاظِمِينَ الْغَيْظَ وَالْعَافِينَ عَنِ النَّاسِ ۗ وَاللَّهُ يُحِبُّ الْمُحْسِنِينَ
ñoom ña nga xam ne dañuy joxe [seen alal ci jamonoy naataange ak ci jamonoy tar-tar ], ak ñay nëbbu seen mer, ak ñay jéggal nit ñi [ay tooñeel] - Yàlla safoo na ñay rafetal -
135وَالَّذِينَ إِذَا فَعَلُوا فَاحِشَةً أَوْ ظَلَمُوا أَنفُسَهُمْ ذَكَرُوا اللَّهَ فَاسْتَغْفَرُوا لِذُنُوبِهِمْ وَمَن يَغْفِرُ الذُّنُوبَ إِلَّا اللَّهُ وَلَمْ يُصِرُّوا عَلَىٰ مَا فَعَلُوا وَهُمْ يَعْلَمُونَ
ak ña nga xam ne, bu ñu defee ñaawtéef mbaa ñu tooñ seen bopp, daldi fàttaliku Yàlla fa saa sa, daldi jéggalu seen bàkkaar ya - te Yàlla rekk ay jéggale bàkkaar - te ñooña duñu nuur mukk ci jëfe bàkkaar te fekk ñu xam ko.
136أُولَٰئِكَ جَزَاؤُهُم مَّغْفِرَةٌ مِّن رَّبِّهِمْ وَجَنَّاتٌ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ خَالِدِينَ فِيهَا ۚ وَنِعْمَ أَجْرُ الْعَامِلِينَ
Ñooña seenug pey moo di jéggal gu bawoo ca seen Boroom, ak Àjjana yu dex ya di daw ci seen ron, te dañu fay béel. Loolu ag pey dàqatuko !
137قَدْ خَلَتْ مِن قَبْلِكُمْ سُنَنٌ فَسِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَانظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُكَذِّبِينَ
Am na ay yoon yu jàll yu ñu sosoon ba ngeen dikkagul. Kon doxleen wër ci goxi suuf, te di xool naka la ña daan weddi mujje.
138هَٰذَا بَيَانٌ لِّلنَّاسِ وَهُدًى وَمَوْعِظَةٌ لِّلْمُتَّقِينَ
Lii ag leeral la ci nit ñi, te di ag njub ak ug waare ngir ñi ragal Yàlla.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
136Aaya

Tekki — Aali Imran 136

Simoore Aali Imran Aaya 136 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñooña seenug pey moo di jéggal gu bawoo ca seen…

Simoore Aaya 136/200 — Simoore Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Aali Imran Dégg, Simoore Aali Imran Tekki, Simoore Aali Imran mp3, Simoore Aali Imran pdf. Aaya 134–138. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers