Aali Imran · 41/200
Tekki Waxtaan — Aali Imran
قَالَ رَبِّ اجْعَل لِّي آيَةً ۖ قَالَ آيَتُكَ أَلَّا تُكَلِّمَ النَّاسَ ثَلَاثَةَ أَيَّامٍ إِلَّا رَمْزًا ۗ وَاذْكُر رَّبَّكَ كَثِيرًا وَسَبِّحْ بِالْعَشِيِّ وَالْإِبْكَارِ ۝٤١
Qaala Rabbij `al leee Aayatan qaala Aaayatuka allaa tukalliman naasa salaasata ayyaamin illa ramzaa; wzkur Rabbaka kaseeranw wa sabbih bil`ashiyyi wal ibkaar
📖 Tekkim Wolof
- Mu ne : “Yàlla, defal ma màndarga.” - Mu ne ko : “ Doo mën a wax ak nit ñi ñetti fan lu dul ci njunju. Na nga tudd sa Boroom lu bari ; te nanga di ko sàbbaal suba ak ngoon.”

🎧 Dégg


📜 Aaya 39-43 — Aali Imran

39فَنَادَتْهُ الْمَلَائِكَةُ وَهُوَ قَائِمٌ يُصَلِّي فِي الْمِحْرَابِ أَنَّ اللَّهَ يُبَشِّرُكَ بِيَحْيَىٰ مُصَدِّقًا بِكَلِمَةٍ مِّنَ اللَّهِ وَسَيِّدًا وَحَصُورًا وَنَبِيًّا مِّنَ الصَّالِحِينَ
Noonu, Malaaka ya woo ko, fekk mu taxawe julli ca Mihraab ba, xamal ko ne : “Yàllaa ngi lay bégal ci doom ju tudd Yahyaa, muy dëggal kàddu gu bawoo ca Yàlla [di Iisaa, di kilifa, di ku wegu]. Di ab Yonent, bokk ca ñu sell ña”.
40قَالَ رَبِّ أَنَّىٰ يَكُونُ لِي غُلَامٌ وَقَدْ بَلَغَنِيَ الْكِبَرُ وَامْرَأَتِي عَاقِرٌ ۖ قَالَ كَذَٰلِكَ اللَّهُ يَفْعَلُ مَا يَشَاءُ
Mu ne : "Sama Boroom, naka laay amee doom, ni ma màggatee, sama soxna Jërmél ?”. Mu ne ko : “Noonu lay ame ! ”, Yàlla mooy def lu ko soob.
41قَالَ رَبِّ اجْعَل لِّي آيَةً ۖ قَالَ آيَتُكَ أَلَّا تُكَلِّمَ النَّاسَ ثَلَاثَةَ أَيَّامٍ إِلَّا رَمْزًا ۗ وَاذْكُر رَّبَّكَ كَثِيرًا وَسَبِّحْ بِالْعَشِيِّ وَالْإِبْكَارِ
- Mu ne : “Yàlla, defal ma màndarga.” - Mu ne ko : “ Doo mën a wax ak nit ñi ñetti fan lu dul ci njunju. Na nga tudd sa Boroom lu bari ; te nanga di ko sàbbaal suba ak ngoon.”
42وَإِذْ قَالَتِ الْمَلَائِكَةُ يَا مَرْيَمُ إِنَّ اللَّهَ اصْطَفَاكِ وَطَهَّرَكِ وَاصْطَفَاكِ عَلَىٰ نِسَاءِ الْعَالَمِينَ
(Fàttalikul) ba Malaaka ya waxee ne : “Yaw Maryaama, Yàlla tànn na la te laabal na la, tànn na la ci kaw jigéeni àddina bi yépp.
43يَا مَرْيَمُ اقْنُتِي لِرَبِّكِ وَاسْجُدِي وَارْكَعِي مَعَ الرَّاكِعِينَ
“Yaw Maryaama, jaamul sa Boroom, nanga sujjóot te rukkoo ànd ak ñay rukkoo [di julli]”
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
41Aaya

Tekki — Aali Imran 41

Simoore Aali Imran Aaya 41 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : - Mu ne : “Yàlla, defal ma màndarga.” - Mu…

Simoore Aaya 41/200 — Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Aali Imran Dégg, Aali Imran Tekki, Aali Imran mp3, Aali Imran pdf. Aaya 39–43. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers