Aali Imran · 85/200
Tekki Waxtaan — Aali Imran
وَمَن يَبْتَغِ غَيْرَ الْإِسْلَامِ دِينًا فَلَن يُقْبَلَ مِنْهُ وَهُوَ فِي الْآخِرَةِ مِنَ الْخَاسِرِينَ ۝٨٥
Wa mai yabtaghi ghairal Islaami deenan falany yuqbala minhu wa huwa fil Aakhirati minal khaasireen
📖 Tekkim Wolof
Kuy sàkku diine ju dul Lislaam, deesu ko nangul, te bu àllaaxiraa, ca way-ñàkk ña lay bokk.
🎧 Dégg

📜 Aaya 83-87 — Aali Imran

83أَفَغَيْرَ دِينِ اللَّهِ يَبْغُونَ وَلَهُ أَسْلَمَ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ طَوْعًا وَكَرْهًا وَإِلَيْهِ يُرْجَعُونَ
Ndax dañuy sàkku jeneen diine ju bokkul ak diiney Yàlla ji, te waa asamaan si ak suuf si ci Moom lañu jëm, moo xam muy coobare wallag noteel, te lu mën a xew ca Moom lañuy dellu ?
84قُلْ آمَنَّا بِاللَّهِ وَمَا أُنزِلَ عَلَيْنَا وَمَا أُنزِلَ عَلَىٰ إِبْرَاهِيمَ وَإِسْمَاعِيلَ وَإِسْحَاقَ وَيَعْقُوبَ وَالْأَسْبَاطِ وَمَا أُوتِيَ مُوسَىٰ وَعِيسَىٰ وَالنَّبِيُّونَ مِن رَّبِّهِمْ لَا نُفَرِّقُ بَيْنَ أَحَدٍ مِّنْهُمْ وَنَحْنُ لَهُ مُسْلِمُونَ
Neel : “Gëm nanu Yàlla, li ñu wàcce ci nun, li ñu wàcce ci Ibraahiima, ak Ismaahiila, ak Yanqooba, ak ca sët ya, ak la ñu joxoon Muusaa ak Iisaa ak Yonent ya, mu tukkee ca seen Boroom [Téere ya]: dunu téqale kenn ci ñoom te nun way-wommatu lañu [jébbulu] jëm ci Yàlla”.
85وَمَن يَبْتَغِ غَيْرَ الْإِسْلَامِ دِينًا فَلَن يُقْبَلَ مِنْهُ وَهُوَ فِي الْآخِرَةِ مِنَ الْخَاسِرِينَ
Kuy sàkku diine ju dul Lislaam, deesu ko nangul, te bu àllaaxiraa, ca way-ñàkk ña lay bokk.
86كَيْفَ يَهْدِي اللَّهُ قَوْمًا كَفَرُوا بَعْدَ إِيمَانِهِمْ وَشَهِدُوا أَنَّ الرَّسُولَ حَقٌّ وَجَاءَهُمُ الْبَيِّنَاتُ ۚ وَاللَّهُ لَا يَهْدِي الْقَوْمَ الظَّالِمِينَ
Naka la Yàlla di jubalee nit ñu weddi ginnaaw seen ngëm te ñu seede ne Yonent ba ku dëggu la, te lay yu leer dikkal leen ? Yàlla du gindi nit ñu nekk ay tooñkat.
87أُولَٰئِكَ جَزَاؤُهُمْ أَنَّ عَلَيْهِمْ لَعْنَةَ اللَّهِ وَالْمَلَائِكَةِ وَالنَّاسِ أَجْمَعِينَ
Ñooña, seen pey nekkul lu dul rëbbum Yàlla ak Malaaka ya ak nit ñépp, dana dal ca seen kaw.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
85Aaya

Tekki — Aali Imran 85

Simoore Aali Imran Aaya 85 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Kuy sàkku diine ju dul Lislaam, deesu ko nangul, te…

Simoore Aaya 85/200 — Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Aali Imran Dégg, Aali Imran Tekki, Aali Imran mp3, Aali Imran pdf. Aaya 83–87. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers