Ar-Rum · 5/60
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rum
بِنَصْرِ اللَّهِ ۚ يَنصُرُ مَن يَشَاءُ ۖ وَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ ۝٥
Binasril laa; yansuru mai yashaaa`u wa Huwal `Azeezur Raheem
📖 Tekkim Wolof
ci ndimbalul Yàlla. [Moom Yàlla] mooy dimbali ku ko soob, Mooy boroom Kàttan, di Jaglewaakon bi.

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Ar-Rum

3فِي أَدْنَى الْأَرْضِ وَهُم مِّن بَعْدِ غَلَبِهِمْ سَيَغْلِبُونَ
ci réew yi leen gën a jegeñ, wante ginnaaw nooteef googu, ñoom it danañu not ,
4فِي بِضْعِ سِنِينَ ۗ لِلَّهِ الْأَمْرُ مِن قَبْلُ وَمِن بَعْدُ ۚ وَيَوْمَئِذٍ يَفْرَحُ الْمُؤْمِنُونَ
ci biir diirub lu matul fukki at. Yàlla moo yor dogal yi, ci la jëkkoon ak li lay mujj, bu boobaa way-gëm ñi danañu sëgg ree, bég
5بِنَصْرِ اللَّهِ ۚ يَنصُرُ مَن يَشَاءُ ۖ وَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
ci ndimbalul Yàlla. [Moom Yàlla] mooy dimbali ku ko soob, Mooy boroom Kàttan, di Jaglewaakon bi.
6وَعْدَ اللَّهِ ۖ لَا يُخْلِفُ اللَّهُ وَعْدَهُ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَ النَّاسِ لَا يَعْلَمُونَ
Loolu mooy li Yàlla di dige. Te Yàlla du wuute ab digam, waaye li ëpp ci nit ñi gëmuñu.
7يَعْلَمُونَ ظَاهِرًا مِّنَ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَهُمْ عَنِ الْآخِرَةِ هُمْ غَافِلُونَ
Danañu xam li feeñ ci dundug àddina, te ñoom ñu sàggan lañu ci mbiri àllaaxira,.
Ar-RumFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Ar-Rum 5

Simoore Ar-Rum Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ci ndimbalul Yàlla. [Moom Yàlla] mooy dimbali ku ko soob,…

Simoore Aaya 5/60 — Simoore Ar-Rum الروم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rum Dégg, Simoore Ar-Rum Tekki, Simoore Ar-Rum mp3, Simoore Ar-Rum pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers