Luqman · 3/34
Tekki Waxtaan — Simoore Luqman
هُدًى وَرَحْمَةً لِّلْمُحْسِنِينَ ۝٣
Hudanw wa rahmatal lilmuhsineen
📖 Tekkim Wolof
jub la, yërmaande la ngir ñuy rafetal ,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 1-5 — Simoore Luqman

1الم
Aliif, Laam, Miim.
2تِلْكَ آيَاتُ الْكِتَابِ الْحَكِيمِ
Lii ay laaya la yu Téere bu xereñ,
3هُدًى وَرَحْمَةً لِّلْمُحْسِنِينَ
jub la, yërmaande la ngir ñuy rafetal ,
4الَّذِينَ يُقِيمُونَ الصَّلَاةَ وَيُؤْتُونَ الزَّكَاةَ وَهُم بِالْآخِرَةِ هُمْ يُوقِنُونَ
ñiy taxawal julli, di génne asaka te amug wóolu ci ne àllaaxira dina ñëw.
5أُولَٰئِكَ عَلَىٰ هُدًى مِّن رَّبِّهِمْ ۖ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الْمُفْلِحُونَ
Ñooñaa nga tege ca kaw seen yoonu Boroom wu jub xocc wa, te ñoom ñooña ñoo texe.
LuqmanFihi Alxuraan
34Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Luqman 3

Simoore Luqman Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : jub la, yërmaande la ngir ñuy rafetal ,

Simoore Aaya 3/34 — Simoore Luqman لقمان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Luqman Dégg, Simoore Luqman Tekki, Simoore Luqman mp3, Simoore Luqman pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers