Luqman · 4/34
Tekki Waxtaan — Luqman
الَّذِينَ يُقِيمُونَ الصَّلَاةَ وَيُؤْتُونَ الزَّكَاةَ وَهُم بِالْآخِرَةِ هُمْ يُوقِنُونَ ٤
Transliteration
Allazeena yuqeemoonas Salaata wa yu`toonaz Zakaata wa hum bil Aakhirati hum yooqinoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
ñiy taxawal julli, di génne asaka te amug wóolu ci ne àllaaxira dina ñëw.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 2-6 — Luqman
2تِلْكَ آيَاتُ الْكِتَابِ الْحَكِيمِ
Lii ay laaya la yu Téere bu xereñ,
3هُدًى وَرَحْمَةً لِّلْمُحْسِنِينَ
jub la, yërmaande la ngir ñuy rafetal ,
4الَّذِينَ يُقِيمُونَ الصَّلَاةَ وَيُؤْتُونَ الزَّكَاةَ وَهُم بِالْآخِرَةِ هُمْ يُوقِنُونَ
ñiy taxawal julli, di génne asaka te amug wóolu ci ne àllaaxira dina ñëw.
5أُولَٰئِكَ عَلَىٰ هُدًى مِّن رَّبِّهِمْ ۖ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الْمُفْلِحُونَ
Ñooñaa nga tege ca kaw seen yoonu Boroom wu jub xocc wa, te ñoom ñooña ñoo texe.
6وَمِنَ النَّاسِ مَن يَشْتَرِي لَهْوَ الْحَدِيثِ لِيُضِلَّ عَن سَبِيلِ اللَّهِ بِغَيْرِ عِلْمٍ وَيَتَّخِذَهَا هُزُوًا ۚ أُولَٰئِكَ لَهُمْ عَذَابٌ مُّهِينٌ
Am na ci nit ñuy nëbb xam-xam, di feeñal waxi caaxaan ngir namm a soreel nit ñi, sànk leen, réeral leen yoonu Yàlla ci lu àndul ak xam-xam, weddi ko, jàppe ko ag doyadal. Ñoom ñooña am nañu mbugal muy toroxale.
LuqmanFihi Alxuraan
34Aaya
MeccanRevelation
4Aaya
Tekki — Luqman 4
Simoore Luqman Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ñiy taxawal julli, di génne asaka te amug wóolu ci…Simoore Aaya 4/34 — Luqman لقمان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Luqman Dégg, Luqman Tekki, Luqman mp3, Luqman pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








