Al-Ahzab · 56/73
Tekki Waxtaan — Al-Ahzab
إِنَّ اللَّهَ وَمَلَائِكَتَهُ يُصَلُّونَ عَلَى النَّبِيِّ ۚ يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا صَلُّوا عَلَيْهِ وَسَلِّمُوا تَسْلِيمًا ٥٦
Transliteration
Innal laaha wa malaaa`i katahoo yusalloona `alan Nabiyy; yaaa aiyuhal lazeena aamanoo salloo `alaihi wa sallimoo tasleemaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Yàlla ak i Malaakaam dañuy julli ci Yonent bi ; Éy yéen ñi gëm, jullileen ci moom te sëlmal ci moom .
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 54-58 — Al-Ahzab
54إِن تُبْدُوا شَيْئًا أَوْ تُخْفُوهُ فَإِنَّ اللَّهَ كَانَ بِكُلِّ شَيْءٍ عَلِيمًا
Mbir mu ngeen mën feeñal mbaa ngeen nëbb ko,... Yàlla xam na ko.
55لَّا جُنَاحَ عَلَيْهِنَّ فِي آبَائِهِنَّ وَلَا أَبْنَائِهِنَّ وَلَا إِخْوَانِهِنَّ وَلَا أَبْنَاءِ إِخْوَانِهِنَّ وَلَا أَبْنَاءِ أَخَوَاتِهِنَّ وَلَا نِسَائِهِنَّ وَلَا مَا مَلَكَتْ أَيْمَانُهُنَّ ۗ وَاتَّقِينَ اللَّهَ ۚ إِنَّ اللَّهَ كَانَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ شَهِيدًا
Aayul ci ñoom [soxna yi] seeni baay [di ko def], walla seeni doom, walla seen mbokk, walla seeni doomi mbokk mu jigéen, walla seeni jabar, walla seeni jaam. Te nangeen ragal Yàlla ndax Yàllaa seede lépp lu ne.
56إِنَّ اللَّهَ وَمَلَائِكَتَهُ يُصَلُّونَ عَلَى النَّبِيِّ ۚ يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا صَلُّوا عَلَيْهِ وَسَلِّمُوا تَسْلِيمًا
Yàlla ak i Malaakaam dañuy julli ci Yonent bi ; Éy yéen ñi gëm, jullileen ci moom te sëlmal ci moom .
57إِنَّ الَّذِينَ يُؤْذُونَ اللَّهَ وَرَسُولَهُ لَعَنَهُمُ اللَّهُ فِي الدُّنْيَا وَالْآخِرَةِ وَأَعَدَّ لَهُمْ عَذَابًا مُّهِينًا
Ñi nga xam ne dañuy lor Yàlla ak ub Yonentam, Yàlla rëbb na leen ci àddina ak ca àllaaxira, te waajalal na leen mbugal muy doyadiloo, di toroxtale.
58وَالَّذِينَ يُؤْذُونَ الْمُؤْمِنِينَ وَالْمُؤْمِنَاتِ بِغَيْرِ مَا اكْتَسَبُوا فَقَدِ احْتَمَلُوا بُهْتَانًا وَإِثْمًا مُّبِينًا
Ña nga xam ne dañuy lor jullit yu góor yi ak jullit yu jigéen yi te defuñu lu ko jar, ñangay yenu aw duur ak bàkkaar bu rëy.
Al-AhzabFihi Alxuraan
73Aaya
MedinanRevelation
56Aaya
Tekki — Al-Ahzab 56
Simoore Al-Ahzab Aaya 56 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla ak i Malaakaam dañuy julli ci Yonent bi ;…Simoore Aaya 56/73 — Al-Ahzab الأحزاب (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ahzab Dégg, Al-Ahzab Tekki, Al-Ahzab mp3, Al-Ahzab pdf. Aaya 54–58. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








