Al-Ahzab · 69/73
Tekki Waxtaan — Al-Ahzab
يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَكُونُوا كَالَّذِينَ آذَوْا مُوسَىٰ فَبَرَّأَهُ اللَّهُ مِمَّا قَالُوا ۚ وَكَانَ عِندَ اللَّهِ وَجِيهًا ٦٩
Transliteration
yaa aiyuhal lazeena aamanoo las takoonoo kalla zeena aazaw Moosaa fa barra ahul laahu mimmmaa qaaloo; wa kaana `indal laahi wajeehaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Éy yéen ñi gëm ! Buleen mel ni ña daan lor Muusaa, di ko tuumaal. Far Yàlla setal ko ca tuuma ya, di ku mu jubaloon.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 67-71 — Al-Ahzab
67وَقَالُوا رَبَّنَا إِنَّا أَطَعْنَا سَادَتَنَا وَكُبَرَاءَنَا فَأَضَلُّونَا السَّبِيلَا
Ñuy wax naan : “Yaw sunu Boroom, nun dey toppoon nanu sunuy sang ak sunuy kilifa. Ñu réerale nu ak yoon wa.
68رَبَّنَا آتِهِمْ ضِعْفَيْنِ مِنَ الْعَذَابِ وَالْعَنْهُمْ لَعْنًا كَبِيرًا
Boroom sunu, fulandileen mbugal te nga rëbbleen rëbb mu rëy”.
69يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَكُونُوا كَالَّذِينَ آذَوْا مُوسَىٰ فَبَرَّأَهُ اللَّهُ مِمَّا قَالُوا ۚ وَكَانَ عِندَ اللَّهِ وَجِيهًا
Éy yéen ñi gëm ! Buleen mel ni ña daan lor Muusaa, di ko tuumaal. Far Yàlla setal ko ca tuuma ya, di ku mu jubaloon.
70يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا اتَّقُوا اللَّهَ وَقُولُوا قَوْلًا سَدِيدًا
Éy yéen ñi gëm ! Ragal-leen Yàlla tey wax wax ju jub.
71يُصْلِحْ لَكُمْ أَعْمَالَكُمْ وَيَغْفِرْ لَكُمْ ذُنُوبَكُمْ ۗ وَمَن يُطِعِ اللَّهَ وَرَسُولَهُ فَقَدْ فَازَ فَوْزًا عَظِيمًا
kon dey Dana leen yéwénalal seeni jëf, jéggal leen it seeni bàkkaar. Te képp kuy topp Yàlla ak ub Yonentam, dana texe texe gu màgg.
Al-AhzabFihi Alxuraan
73Aaya
MedinanRevelation
69Aaya
Tekki — Al-Ahzab 69
Simoore Al-Ahzab Aaya 69 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Éy yéen ñi gëm ! Buleen mel ni ña daan…Simoore Aaya 69/73 — Al-Ahzab الأحزاب (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ahzab Dégg, Al-Ahzab Tekki, Al-Ahzab mp3, Al-Ahzab pdf. Aaya 67–71. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








