Ya-Sin · 23/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
أَأَتَّخِذُ مِن دُونِهِ آلِهَةً إِن يُرِدْنِ الرَّحْمَٰنُ بِضُرٍّ لَّا تُغْنِ عَنِّي شَفَاعَتُهُمْ شَيْئًا وَلَا يُنقِذُونِ ۝٢٣
A-attakhizu min dooniheee aalihatan iny-yuridnir Rahmaanu bidurril-laa tughni `annee shafaa `atuhum shai `anw-wa laa yunqizoon
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax damay wuti jeneen yàlla ju dul Moom ? Te bu Yërëmaakoon bi natte ci man lor, seenug tinu duma jariñ dara te duñu ma xettali.

🎧 Dégg


📜 Aaya 21-25 — Simoore Ya-Sin

21اتَّبِعُوا مَن لَّا يَسْأَلُكُمْ أَجْرًا وَهُم مُّهْتَدُونَ
Toppleen ku dul laaj ag pey te ñoom ñu gindiku lañu.
22وَمَا لِيَ لَا أَعْبُدُ الَّذِي فَطَرَنِي وَإِلَيْهِ تُرْجَعُونَ
moo man, ana lu may war a dal ba tax duma jaamu Yàlla mi ma bind ? Te ca Moom ngeen di dellu.
23أَأَتَّخِذُ مِن دُونِهِ آلِهَةً إِن يُرِدْنِ الرَّحْمَٰنُ بِضُرٍّ لَّا تُغْنِ عَنِّي شَفَاعَتُهُمْ شَيْئًا وَلَا يُنقِذُونِ
Moo ndax damay wuti jeneen yàlla ju dul Moom ? Te bu Yërëmaakoon bi natte ci man lor, seenug tinu duma jariñ dara te duñu ma xettali.
24إِنِّي إِذًا لَّفِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Su loolu amoon dey kon, maa ngi ci ag réer gu bir.
25إِنِّي آمَنتُ بِرَبِّكُمْ فَاسْمَعُونِ
Man dey, gëm naa seen Boroom, dëggal-leen ma”.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — Ya-Sin 23

Simoore Ya-Sin Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax damay wuti jeneen yàlla ju dul Moom ?…

Simoore Aaya 23/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers