Ya-Sin · 24/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
إِنِّي إِذًا لَّفِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ ۝٢٤
Inneee izal-lafee dalaa-lim-mubeen
📖 Tekkim Wolof
Su loolu amoon dey kon, maa ngi ci ag réer gu bir.
🎧 Dégg

📜 Aaya 22-26 — Ya-Sin

22وَمَا لِيَ لَا أَعْبُدُ الَّذِي فَطَرَنِي وَإِلَيْهِ تُرْجَعُونَ
moo man, ana lu may war a dal ba tax duma jaamu Yàlla mi ma bind ? Te ca Moom ngeen di dellu.
23أَأَتَّخِذُ مِن دُونِهِ آلِهَةً إِن يُرِدْنِ الرَّحْمَٰنُ بِضُرٍّ لَّا تُغْنِ عَنِّي شَفَاعَتُهُمْ شَيْئًا وَلَا يُنقِذُونِ
Moo ndax damay wuti jeneen yàlla ju dul Moom ? Te bu Yërëmaakoon bi natte ci man lor, seenug tinu duma jariñ dara te duñu ma xettali.
24إِنِّي إِذًا لَّفِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Su loolu amoon dey kon, maa ngi ci ag réer gu bir.
25إِنِّي آمَنتُ بِرَبِّكُمْ فَاسْمَعُونِ
Man dey, gëm naa seen Boroom, dëggal-leen ma”.
26قِيلَ ادْخُلِ الْجَنَّةَ ۖ قَالَ يَا لَيْتَ قَوْمِي يَعْلَمُونَ
Waxees na ko, ne ko : “Tàbbil Àjjana”. Mu wax ne : “Cëy aka neexoon samaw nit xam !
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
24Aaya

Tekki — Ya-Sin 24

Simoore Ya-Sin Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Su loolu amoon dey kon, maa ngi ci ag réer…

Simoore Aaya 24/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers