Ya-Sin · 25/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
إِنِّي آمَنتُ بِرَبِّكُمْ فَاسْمَعُونِ ۝٢٥
Inneee aamantu bi Rabbikum fasma`oon
📖 Tekkim Wolof
Man dey, gëm naa seen Boroom, dëggal-leen ma”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 23-27 — Simoore Ya-Sin

23أَأَتَّخِذُ مِن دُونِهِ آلِهَةً إِن يُرِدْنِ الرَّحْمَٰنُ بِضُرٍّ لَّا تُغْنِ عَنِّي شَفَاعَتُهُمْ شَيْئًا وَلَا يُنقِذُونِ
Moo ndax damay wuti jeneen yàlla ju dul Moom ? Te bu Yërëmaakoon bi natte ci man lor, seenug tinu duma jariñ dara te duñu ma xettali.
24إِنِّي إِذًا لَّفِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Su loolu amoon dey kon, maa ngi ci ag réer gu bir.
25إِنِّي آمَنتُ بِرَبِّكُمْ فَاسْمَعُونِ
Man dey, gëm naa seen Boroom, dëggal-leen ma”.
26قِيلَ ادْخُلِ الْجَنَّةَ ۖ قَالَ يَا لَيْتَ قَوْمِي يَعْلَمُونَ
Waxees na ko, ne ko : “Tàbbil Àjjana”. Mu wax ne : “Cëy aka neexoon samaw nit xam !
27بِمَا غَفَرَ لِي رَبِّي وَجَعَلَنِي مِنَ الْمُكْرَمِينَ
li tax Yàlla jéggal ma, def ma ma bokk ci ña Muy teral”.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — Ya-Sin 25

Simoore Ya-Sin Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Man dey, gëm naa seen Boroom, dëggal-leen ma”.

Simoore Aaya 25/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers