Ya-Sin · 26/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
قِيلَ ادْخُلِ الْجَنَّةَ ۖ قَالَ يَا لَيْتَ قَوْمِي يَعْلَمُونَ ۝٢٦
Qeelad khulil Jannnah; qaala yaa laita qawmee ya`lamoon
📖 Tekkim Wolof
Waxees na ko, ne ko : “Tàbbil Àjjana”. Mu wax ne : “Cëy aka neexoon samaw nit xam !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 24-28 — Simoore Ya-Sin

24إِنِّي إِذًا لَّفِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Su loolu amoon dey kon, maa ngi ci ag réer gu bir.
25إِنِّي آمَنتُ بِرَبِّكُمْ فَاسْمَعُونِ
Man dey, gëm naa seen Boroom, dëggal-leen ma”.
26قِيلَ ادْخُلِ الْجَنَّةَ ۖ قَالَ يَا لَيْتَ قَوْمِي يَعْلَمُونَ
Waxees na ko, ne ko : “Tàbbil Àjjana”. Mu wax ne : “Cëy aka neexoon samaw nit xam !
27بِمَا غَفَرَ لِي رَبِّي وَجَعَلَنِي مِنَ الْمُكْرَمِينَ
li tax Yàlla jéggal ma, def ma ma bokk ci ña Muy teral”.
28۞ وَمَا أَنزَلْنَا عَلَىٰ قَوْمِهِ مِن بَعْدِهِ مِن جُندٍ مِّنَ السَّمَاءِ وَمَا كُنَّا مُنزِلِينَ
Wàccewunu ci aw nitam ginnaaw ba mu jàllee, ay xarekat ñuy bawoo asamaan. Bëggunu fa woon a wàcce dara itam.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
26Aaya

Tekki — Ya-Sin 26

Simoore Ya-Sin Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxees na ko, ne ko : “Tàbbil Àjjana”. Mu wax…

Simoore Aaya 26/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers