Ya-Sin · 27/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
بِمَا غَفَرَ لِي رَبِّي وَجَعَلَنِي مِنَ الْمُكْرَمِينَ ٢٧
Transliteration
Bimaa ghafara lee Rabbee wa ja`alanee minal mukrameen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
li tax Yàlla jéggal ma, def ma ma bokk ci ña Muy teral”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 25-29 — Ya-Sin
25إِنِّي آمَنتُ بِرَبِّكُمْ فَاسْمَعُونِ
Man dey, gëm naa seen Boroom, dëggal-leen ma”.
26قِيلَ ادْخُلِ الْجَنَّةَ ۖ قَالَ يَا لَيْتَ قَوْمِي يَعْلَمُونَ
Waxees na ko, ne ko : “Tàbbil Àjjana”. Mu wax ne : “Cëy aka neexoon samaw nit xam !
27بِمَا غَفَرَ لِي رَبِّي وَجَعَلَنِي مِنَ الْمُكْرَمِينَ
li tax Yàlla jéggal ma, def ma ma bokk ci ña Muy teral”.
28۞ وَمَا أَنزَلْنَا عَلَىٰ قَوْمِهِ مِن بَعْدِهِ مِن جُندٍ مِّنَ السَّمَاءِ وَمَا كُنَّا مُنزِلِينَ
Wàccewunu ci aw nitam ginnaaw ba mu jàllee, ay xarekat ñuy bawoo asamaan. Bëggunu fa woon a wàcce dara itam.
29إِن كَانَتْ إِلَّا صَيْحَةً وَاحِدَةً فَإِذَا هُمْ خَامِدُونَ
Génn xaacu rekk a fa jaar, ñu faf giim.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
27Aaya
Tekki — Ya-Sin 27
Simoore Ya-Sin Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : li tax Yàlla jéggal ma, def ma ma bokk ci…Simoore Aaya 27/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








