As-Saffat · 102/182
Tekki Waxtaan — As-Saffat
فَلَمَّا بَلَغَ مَعَهُ السَّعْيَ قَالَ يَا بُنَيَّ إِنِّي أَرَىٰ فِي الْمَنَامِ أَنِّي أَذْبَحُكَ فَانظُرْ مَاذَا تَرَىٰ ۚ قَالَ يَا أَبَتِ افْعَلْ مَا تُؤْمَرُ ۖ سَتَجِدُنِي إِن شَاءَ اللَّهُ مِنَ الصَّابِرِينَ ۝١٠٢
Falamma balagha ma`a hus sa`ya qaala yaa buniya inneee araa fil manaami anneee azbahuka fanzur maazaa taraa; qaala yaaa abatif `al maa tu`maru satajidunee in shaaa`allaahu minas saabireen
📖 Tekkim Wolof
Ba mu amee ati àndak moom, Ibraahiima wax na ne : "Yaw samas doom, gis naa ci bi may nelaw, ci biir gént, ndigalul war laa rendi. Seetal looy xalaat”. (Ismaayiila) ne ko : “Yaw sama baay, defal lu ñu la digal : bu soobee Yàlla, danga gis ne maag muñkat yee ànd”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 100-104 — As-Saffat

100رَبِّ هَبْ لِي مِنَ الصَّالِحِينَ
Yaw sama Boroom, may ma ay sët yu yiw”.
101فَبَشَّرْنَاهُ بِغُلَامٍ حَلِيمٍ
Nu bégal ko, may ko doom ju lewet .
102فَلَمَّا بَلَغَ مَعَهُ السَّعْيَ قَالَ يَا بُنَيَّ إِنِّي أَرَىٰ فِي الْمَنَامِ أَنِّي أَذْبَحُكَ فَانظُرْ مَاذَا تَرَىٰ ۚ قَالَ يَا أَبَتِ افْعَلْ مَا تُؤْمَرُ ۖ سَتَجِدُنِي إِن شَاءَ اللَّهُ مِنَ الصَّابِرِينَ
Ba mu amee ati àndak moom, Ibraahiima wax na ne : "Yaw samas doom, gis naa ci bi may nelaw, ci biir gént, ndigalul war laa rendi. Seetal looy xalaat”. (Ismaayiila) ne ko : “Yaw sama baay, defal lu ñu la digal : bu soobee Yàlla, danga gis ne maag muñkat yee ànd”.
103فَلَمَّا أَسْلَمَا وَتَلَّهُ لِلْجَبِينِ
Ba ñu wéyalee seen ndigalul Boroom, mu di dëféenal ko,
104وَنَادَيْنَاهُ أَن يَا إِبْرَاهِيمُ
Nu woo ko, ne ko : “Éy yaw Ibraahiima !
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
102Aaya

Tekki — As-Saffat 102

Simoore As-Saffat Aaya 102 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba mu amee ati àndak moom, Ibraahiima wax na ne…

Simoore Aaya 102/182 — As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: As-Saffat Dégg, As-Saffat Tekki, As-Saffat mp3, As-Saffat pdf. Aaya 100–104. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers