As-Saffat · 101/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَبَشَّرْنَاهُ بِغُلَامٍ حَلِيمٍ ۝١٠١
Fabashsharnaahu bighulaamin haleem
📖 Tekkim Wolof
Nu bégal ko, may ko doom ju lewet .

🎧 Dégg


📜 Aaya 99-103 — Simoore As-Saffat

99وَقَالَ إِنِّي ذَاهِبٌ إِلَىٰ رَبِّي سَيَهْدِينِ
Mu wax ne : “Maa ngi dem ca sama Boroom, Dana ma gindi.
100رَبِّ هَبْ لِي مِنَ الصَّالِحِينَ
Yaw sama Boroom, may ma ay sët yu yiw”.
101فَبَشَّرْنَاهُ بِغُلَامٍ حَلِيمٍ
Nu bégal ko, may ko doom ju lewet .
102فَلَمَّا بَلَغَ مَعَهُ السَّعْيَ قَالَ يَا بُنَيَّ إِنِّي أَرَىٰ فِي الْمَنَامِ أَنِّي أَذْبَحُكَ فَانظُرْ مَاذَا تَرَىٰ ۚ قَالَ يَا أَبَتِ افْعَلْ مَا تُؤْمَرُ ۖ سَتَجِدُنِي إِن شَاءَ اللَّهُ مِنَ الصَّابِرِينَ
Ba mu amee ati àndak moom, Ibraahiima wax na ne : "Yaw samas doom, gis naa ci bi may nelaw, ci biir gént, ndigalul war laa rendi. Seetal looy xalaat”. (Ismaayiila) ne ko : “Yaw sama baay, defal lu ñu la digal : bu soobee Yàlla, danga gis ne maag muñkat yee ànd”.
103فَلَمَّا أَسْلَمَا وَتَلَّهُ لِلْجَبِينِ
Ba ñu wéyalee seen ndigalul Boroom, mu di dëféenal ko,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
101Aaya

Tekki — As-Saffat 101

Simoore As-Saffat Aaya 101 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu bégal ko, may ko doom ju lewet .

Simoore Aaya 101/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 99–103. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers