As-Saffat · 103/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَلَمَّا أَسْلَمَا وَتَلَّهُ لِلْجَبِينِ ۝١٠٣
Falammaaa aslamaa wa tallahoo liljabeen
📖 Tekkim Wolof
Ba ñu wéyalee seen ndigalul Boroom, mu di dëféenal ko,

🎧 Dégg


📜 Aaya 101-105 — Simoore As-Saffat

101فَبَشَّرْنَاهُ بِغُلَامٍ حَلِيمٍ
Nu bégal ko, may ko doom ju lewet .
102فَلَمَّا بَلَغَ مَعَهُ السَّعْيَ قَالَ يَا بُنَيَّ إِنِّي أَرَىٰ فِي الْمَنَامِ أَنِّي أَذْبَحُكَ فَانظُرْ مَاذَا تَرَىٰ ۚ قَالَ يَا أَبَتِ افْعَلْ مَا تُؤْمَرُ ۖ سَتَجِدُنِي إِن شَاءَ اللَّهُ مِنَ الصَّابِرِينَ
Ba mu amee ati àndak moom, Ibraahiima wax na ne : "Yaw samas doom, gis naa ci bi may nelaw, ci biir gént, ndigalul war laa rendi. Seetal looy xalaat”. (Ismaayiila) ne ko : “Yaw sama baay, defal lu ñu la digal : bu soobee Yàlla, danga gis ne maag muñkat yee ànd”.
103فَلَمَّا أَسْلَمَا وَتَلَّهُ لِلْجَبِينِ
Ba ñu wéyalee seen ndigalul Boroom, mu di dëféenal ko,
104وَنَادَيْنَاهُ أَن يَا إِبْرَاهِيمُ
Nu woo ko, ne ko : “Éy yaw Ibraahiima !
105قَدْ صَدَّقْتَ الرُّؤْيَا ۚ إِنَّا كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Dëggal nga gént gi. Te noonu la Nuy feye ñiy rafetal”.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
103Aaya

Tekki — As-Saffat 103

Simoore As-Saffat Aaya 103 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba ñu wéyalee seen ndigalul Boroom, mu di dëféenal ko,

Simoore Aaya 103/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 101–105. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers