As-Saffat · 165/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَإِنَّا لَنَحْنُ الصَّافُّونَ ۝١٦٥
Wa innaa llanah nus saaffoon
📖 Tekkim Wolof
te noo leen defoon ay sàppe ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 163-167 — Simoore As-Saffat

163إِلَّا مَنْ هُوَ صَالِ الْجَحِيمِ
ku dul kuy nar a xoyomu ci Safara.
164وَمَا مِنَّا إِلَّا لَهُ مَقَامٌ مَّعْلُومٌ
Amul kenn ci [Malaaka yi] lu dul ne am na wàccuwaay wu ñu xam ;
165وَإِنَّا لَنَحْنُ الصَّافُّونَ
te noo leen defoon ay sàppe ;
166وَإِنَّا لَنَحْنُ الْمُسَبِّحُونَ
te nun nooy sàbbaal Yàlla.
167وَإِن كَانُوا لَيَقُولُونَ
Doonte la sax ña ngay wax naan :
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
165Aaya

Tekki — As-Saffat 165

Simoore As-Saffat Aaya 165 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te noo leen defoon ay sàppe ;

Simoore Aaya 165/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 163–167. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers