As-Saffat · 171/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَلَقَدْ سَبَقَتْ كَلِمَتُنَا لِعِبَادِنَا الْمُرْسَلِينَ ۝١٧١
Wa laqad sabaqat Kalimatunaa li`ibaadinal mursa leen
📖 Tekkim Wolof
Sunu kàddu jiitu woon na ci Sunu jaam ña di ay Yonent,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 169-173 — Simoore As-Saffat

169لَكُنَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ
kon de nu doon ay jaami Yàlla yuy sellal !
170فَكَفَرُوا بِهِ ۖ فَسَوْفَ يَعْلَمُونَ
Weddi nañu ko, waaye danañu xam ne.
171وَلَقَدْ سَبَقَتْ كَلِمَتُنَا لِعِبَادِنَا الْمُرْسَلِينَ
Sunu kàddu jiitu woon na ci Sunu jaam ña di ay Yonent,
172إِنَّهُمْ لَهُمُ الْمَنصُورُونَ
ñoom danañu am ndimbal,
173وَإِنَّ جُندَنَا لَهُمُ الْغَالِبُونَ
te it Sunuy xarekat ñooy not.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
171Aaya

Tekki — As-Saffat 171

Simoore As-Saffat Aaya 171 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sunu kàddu jiitu woon na ci Sunu jaam ña di…

Simoore Aaya 171/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 169–173. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers