As-Saffat · 170/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَكَفَرُوا بِهِ ۖ فَسَوْفَ يَعْلَمُونَ ۝١٧٠
Fakafaroo bihee fasawfa ya`lamoon
📖 Tekkim Wolof
Weddi nañu ko, waaye danañu xam ne.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 168-172 — Simoore As-Saffat

168لَوْ أَنَّ عِندَنَا ذِكْرًا مِّنَ الْأَوَّلِينَ
“Su nu amoon waarate gu bawoo ca sunuy maam,
169لَكُنَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ
kon de nu doon ay jaami Yàlla yuy sellal !
170فَكَفَرُوا بِهِ ۖ فَسَوْفَ يَعْلَمُونَ
Weddi nañu ko, waaye danañu xam ne.
171وَلَقَدْ سَبَقَتْ كَلِمَتُنَا لِعِبَادِنَا الْمُرْسَلِينَ
Sunu kàddu jiitu woon na ci Sunu jaam ña di ay Yonent,
172إِنَّهُمْ لَهُمُ الْمَنصُورُونَ
ñoom danañu am ndimbal,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
170Aaya

Tekki — As-Saffat 170

Simoore As-Saffat Aaya 170 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Weddi nañu ko, waaye danañu xam ne.

Simoore Aaya 170/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 168–172. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers