As-Saffat · 177/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَإِذَا نَزَلَ بِسَاحَتِهِمْ فَسَاءَ صَبَاحُ الْمُنذَرِينَ ۝١٧٧
Fa izaa nazala bisaahatihim fasaaa`a sabaahul munzareen
📖 Tekkim Wolof
Su wàccee ci seenub ëtt, ñoom ña ñu doon fàttali, ndaw suba gu bon !

🎧 Dégg


📜 Aaya 175-179 — Simoore As-Saffat

175وَأَبْصِرْهُمْ فَسَوْفَ يُبْصِرُونَ
te nga seetluleen : danañu gis de !
176أَفَبِعَذَابِنَا يَسْتَعْجِلُونَ
Moo ndax ñoom dañuy yàkkamti sunu mbugal ?
177فَإِذَا نَزَلَ بِسَاحَتِهِمْ فَسَاءَ صَبَاحُ الْمُنذَرِينَ
Su wàccee ci seenub ëtt, ñoom ña ñu doon fàttali, ndaw suba gu bon !
178وَتَوَلَّ عَنْهُمْ حَتَّىٰ حِينٍ
nanga leen dummóoyu ab diir ;
179وَأَبْصِرْ فَسَوْفَ يُبْصِرُونَ
te nga seetluleen : danañu gis de !
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
177Aaya

Tekki — As-Saffat 177

Simoore As-Saffat Aaya 177 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Su wàccee ci seenub ëtt, ñoom ña ñu doon fàttali,…

Simoore Aaya 177/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 175–179. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers