As-Saffat · 178/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَتَوَلَّ عَنْهُمْ حَتَّىٰ حِينٍ ۝١٧٨
Wa tawalla `anhum hattaa heen
📖 Tekkim Wolof
nanga leen dummóoyu ab diir ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 176-180 — Simoore As-Saffat

176أَفَبِعَذَابِنَا يَسْتَعْجِلُونَ
Moo ndax ñoom dañuy yàkkamti sunu mbugal ?
177فَإِذَا نَزَلَ بِسَاحَتِهِمْ فَسَاءَ صَبَاحُ الْمُنذَرِينَ
Su wàccee ci seenub ëtt, ñoom ña ñu doon fàttali, ndaw suba gu bon !
178وَتَوَلَّ عَنْهُمْ حَتَّىٰ حِينٍ
nanga leen dummóoyu ab diir ;
179وَأَبْصِرْ فَسَوْفَ يُبْصِرُونَ
te nga seetluleen : danañu gis de !
180سُبْحَانَ رَبِّكَ رَبِّ الْعِزَّةِ عَمَّا يَصِفُونَ
Tudd naa sellug sa Boroom, Boroom kàttan gi. Kawe na ca la ñu koy melal !
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
178Aaya

Tekki — As-Saffat 178

Simoore As-Saffat Aaya 178 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : nanga leen dummóoyu ab diir ;

Simoore Aaya 178/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 176–180. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers