As-Saffat · 60/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِنَّ هَٰذَا لَهُوَ الْفَوْزُ الْعَظِيمُ ۝٦٠
Inna haazaa falya`ma lil`aamiloon
📖 Tekkim Wolof
Lii mooy texe gu màgg ga.

🎧 Dégg


📜 Aaya 58-62 — Simoore As-Saffat

58أَفَمَا نَحْنُ بِمَيِّتِينَ
Xanaa nun dey dunu dee
59إِلَّا مَوْتَتَنَا الْأُولَىٰ وَمَا نَحْنُ بِمُعَذَّبِينَ
lu dul ca dee gu jëkk ga te xanaa kenn dunu mbugal ? ”
60إِنَّ هَٰذَا لَهُوَ الْفَوْزُ الْعَظِيمُ
Lii mooy texe gu màgg ga.
61لِمِثْلِ هَٰذَا فَلْيَعْمَلِ الْعَامِلُونَ
Ñiy jëf, nañuy jëf lu mel nii.
62أَذَٰلِكَ خَيْرٌ نُّزُلًا أَمْ شَجَرَةُ الزَّقُّومِ
Moo ndax loolu moo di wàccuwaay ba gën, walla garabug Zaquum ?
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
60Aaya

Tekki — As-Saffat 60

Simoore As-Saffat Aaya 60 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lii mooy texe gu màgg ga.

Simoore Aaya 60/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 58–62. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers