Sad · 15/88
Tekki Waxtaan — Sad
وَمَا يَنظُرُ هَٰؤُلَاءِ إِلَّا صَيْحَةً وَاحِدَةً مَّا لَهَا مِن فَوَاقٍ ۝١٥
Wa maa yanzuru haaa ulaaa`i illaa saihatanw waahidatam maa lahaa min fawaaq
📖 Tekkim Wolof
Ñoom xaaruñu lu dul genn xaacu, gu dul tóllantiku wol.
🎧 Dégg

📜 Aaya 13-17 — Sad

13وَثَمُودُ وَقَوْمُ لُوطٍ وَأَصْحَابُ الْأَيْكَةِ ۚ أُولَٰئِكَ الْأَحْزَابُ
k Samuud, ak nitu Lóot, ak waa Aykata, (ñoom ñépp weddi woon nañu seeni yonnent). Te ñoom ñoo di jàppalekat ya (farandoo ya).
14إِن كُلٌّ إِلَّا كَذَّبَ الرُّسُلَ فَحَقَّ عِقَابِ
Ñoom ñépp weddi woon yonnent ya. Nu daldi leen mbugël !
15وَمَا يَنظُرُ هَٰؤُلَاءِ إِلَّا صَيْحَةً وَاحِدَةً مَّا لَهَا مِن فَوَاقٍ
Ñoom xaaruñu lu dul genn xaacu, gu dul tóllantiku wol.
16وَقَالُوا رَبَّنَا عَجِّل لَّنَا قِطَّنَا قَبْلَ يَوْمِ الْحِسَابِ
Ñuy wax naan : “Yaw sunu Boroom, gaawal jox nu sunu wàll balaa wañoo ba”.
17اصْبِرْ عَلَىٰ مَا يَقُولُونَ وَاذْكُرْ عَبْدَنَا دَاوُودَ ذَا الْأَيْدِ ۖ إِنَّهُ أَوَّابٌ
Muñal lii ñuy wax ; te ngay fàttaliku Sunu jaam ba Daawuda ma doonoon boroom doole, Moom ku faral daan dellu ci Boroomam la woon.
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
15Aaya

Tekki — Sad 15

Simoore Sad Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñoom xaaruñu lu dul genn xaacu, gu dul tóllantiku wol.

Simoore Aaya 15/88 — Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Sad Dégg, Sad Tekki, Sad mp3, Sad pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers