Sad · 46/88
Tekki Waxtaan — Simoore Sad
إِنَّا أَخْلَصْنَاهُم بِخَالِصَةٍ ذِكْرَى الدَّارِ ۝٤٦
Innaaa akhlasnaahum bi khaalisatin zikrad daar
📖 Tekkim Wolof
Noo leen ràññi woon ngir sellalug : fàttaliku bis pénc ba.

🎧 Dégg


📜 Aaya 44-48 — Simoore Sad

44وَخُذْ بِيَدِكَ ضِغْثًا فَاضْرِب بِّهِ وَلَا تَحْنَثْ ۗ إِنَّا وَجَدْنَاهُ صَابِرًا ۚ نِّعْمَ الْعَبْدُ ۖ إِنَّهُ أَوَّابٌ
“Ŋëbal sëqub ñax, te dóor ko ko (soxnaam sa). Te bul gàddu bàkkaarub ngiiñ”. Moom, muñkat la di jaam bu baax. Kuy farlu di dellu ci Boroomam la.
45وَاذْكُرْ عِبَادَنَا إِبْرَاهِيمَ وَإِسْحَاقَ وَيَعْقُوبَ أُولِي الْأَيْدِي وَالْأَبْصَارِ
Fàttalikul suñu jaam ña Ibraahiima, ak Ishaaq ak Yaaquub ? Woroomi kàttan la ñu woon ak i gis-gis (xel).
46إِنَّا أَخْلَصْنَاهُم بِخَالِصَةٍ ذِكْرَى الدَّارِ
Noo leen ràññi woon ngir sellalug : fàttaliku bis pénc ba.
47وَإِنَّهُمْ عِندَنَا لَمِنَ الْمُصْطَفَيْنَ الْأَخْيَارِ
Te ñoom, bokk nañu, ca tànnéef ya gën a ràññiku.
48وَاذْكُرْ إِسْمَاعِيلَ وَالْيَسَعَ وَذَا الْكِفْلِ ۖ وَكُلٌّ مِّنَ الْأَخْيَارِ
Fàttalikul Ismaahiila ak Ilyaas, ak Suul kifli, ñoom ñépp ay tànnéef la ñu.
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
46Aaya

Tekki — Sad 46

Simoore Sad Aaya 46 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noo leen ràññi woon ngir sellalug : fàttaliku bis pénc…

Simoore Aaya 46/88 — Simoore Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Sad Dégg, Simoore Sad Tekki, Simoore Sad mp3, Simoore Sad pdf. Aaya 44–48. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers