Sad · 47/88
Tekki Waxtaan — Simoore Sad
وَإِنَّهُمْ عِندَنَا لَمِنَ الْمُصْطَفَيْنَ الْأَخْيَارِ ۝٤٧
Wa innahum `indanaa laminal mustafainal akhyaar
📖 Tekkim Wolof
Te ñoom, bokk nañu, ca tànnéef ya gën a ràññiku.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 45-49 — Simoore Sad

45وَاذْكُرْ عِبَادَنَا إِبْرَاهِيمَ وَإِسْحَاقَ وَيَعْقُوبَ أُولِي الْأَيْدِي وَالْأَبْصَارِ
Fàttalikul suñu jaam ña Ibraahiima, ak Ishaaq ak Yaaquub ? Woroomi kàttan la ñu woon ak i gis-gis (xel).
46إِنَّا أَخْلَصْنَاهُم بِخَالِصَةٍ ذِكْرَى الدَّارِ
Noo leen ràññi woon ngir sellalug : fàttaliku bis pénc ba.
47وَإِنَّهُمْ عِندَنَا لَمِنَ الْمُصْطَفَيْنَ الْأَخْيَارِ
Te ñoom, bokk nañu, ca tànnéef ya gën a ràññiku.
48وَاذْكُرْ إِسْمَاعِيلَ وَالْيَسَعَ وَذَا الْكِفْلِ ۖ وَكُلٌّ مِّنَ الْأَخْيَارِ
Fàttalikul Ismaahiila ak Ilyaas, ak Suul kifli, ñoom ñépp ay tànnéef la ñu.
49هَٰذَا ذِكْرٌ ۚ وَإِنَّ لِلْمُتَّقِينَ لَحُسْنَ مَآبٍ
Lii ag fàttali la. Te ne ñay ragal Yàlla, am nañu, wàccuwaay wu jekk,
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
47Aaya

Tekki — Sad 47

Simoore Sad Aaya 47 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te ñoom, bokk nañu, ca tànnéef ya gën a ràññiku.

Simoore Aaya 47/88 — Simoore Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Sad Dégg, Simoore Sad Tekki, Simoore Sad mp3, Simoore Sad pdf. Aaya 45–49. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers