Sad · 52/88
Tekki Waxtaan — Simoore Sad
۞ وَعِندَهُمْ قَاصِرَاتُ الطَّرْفِ أَتْرَابٌ ۝٥٢
Wa `indahum qaasiraatut tarfi atraab
📖 Tekkim Wolof
Amnañu fa ay jigéen (jabar) ñu di ay lamsalkat, yu maase ay at.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 50-54 — Simoore Sad

50جَنَّاتِ عَدْنٍ مُّفَتَّحَةً لَّهُمُ الْأَبْوَابُ
Àjjanay Adan, seen wunt ya ne ŋàll ngir ñoom,
51مُتَّكِئِينَ فِيهَا يَدْعُونَ فِيهَا بِفَاكِهَةٍ كَثِيرَةٍ وَشَرَابٍ
dañu fay, sóonu, di woo ay futéef yu bari ak i naan.
52۞ وَعِندَهُمْ قَاصِرَاتُ الطَّرْفِ أَتْرَابٌ
Amnañu fa ay jigéen (jabar) ñu di ay lamsalkat, yu maase ay at.
53هَٰذَا مَا تُوعَدُونَ لِيَوْمِ الْحِسَابِ
Lii mooy li Nu leen dégóon ci bisub wañoo ba.
54إِنَّ هَٰذَا لَرِزْقُنَا مَا لَهُ مِن نَّفَادٍ
Lii moo di sunu xéewal gi te du jeex mukk.
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
52Aaya

Tekki — Sad 52

Simoore Sad Aaya 52 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Amnañu fa ay jigéen (jabar) ñu di ay lamsalkat, yu…

Simoore Aaya 52/88 — Simoore Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Sad Dégg, Simoore Sad Tekki, Simoore Sad mp3, Simoore Sad pdf. Aaya 50–54. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers