Az-Zumar · 24/75
Tekki Waxtaan — Az-Zumar
أَفَمَن يَتَّقِي بِوَجْهِهِ سُوءَ الْعَذَابِ يَوْمَ الْقِيَامَةِ ۚ وَقِيلَ لِلظَّالِمِينَ ذُوقُوا مَا كُنتُمْ تَكْسِبُونَ ۝٢٤
Afamai yattaqee biwaj hihee sooo`al `azaabi Yawmal Qiyaamah; wa qeela lizzaali meena zooqoo maa kuntum taksiboon
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax ki am bugël mi gën a gën a bon ( niróo na ak ka dugg Àjjana), bu Bis Pénc baa bu boobaa tooñkat ya... Dañu naan leen : “Tokamtikuleen li ngeen daan fàggu”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 22-26 — Az-Zumar

22أَفَمَن شَرَحَ اللَّهُ صَدْرَهُ لِلْإِسْلَامِ فَهُوَ عَلَىٰ نُورٍ مِّن رَّبِّهِ ۚ فَوَيْلٌ لِّلْقَاسِيَةِ قُلُوبُهُم مِّن ذِكْرِ اللَّهِ ۚ أُولَٰئِكَ فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Moo ndax ki Yàlla ubbi dënnam ci Lislaam mu nekk ci leerug Boroomam( moo gën walla ka des cig kéefër)... Toskare ñeel na ñiy bañ a tudd Yàlla ngir xol bu wow. Ñoom ña nga ca réer gu bir.
23اللَّهُ نَزَّلَ أَحْسَنَ الْحَدِيثِ كِتَابًا مُّتَشَابِهًا مَّثَانِيَ تَقْشَعِرُّ مِنْهُ جُلُودُ الَّذِينَ يَخْشَوْنَ رَبَّهُمْ ثُمَّ تَلِينُ جُلُودُهُمْ وَقُلُوبُهُمْ إِلَىٰ ذِكْرِ اللَّهِ ۚ ذَٰلِكَ هُدَى اللَّهِ يَهْدِي بِهِ مَن يَشَاءُ ۚ وَمَن يُضْلِلِ اللَّهُ فَمَا لَهُ مِنْ هَادٍ
Yàlla wàcce na gën jaa rafet waxtaan, muy Téere bu bari yu niróo ak i baamu. Yaramu ñi ragal Yàlla day daw [saa su ñu ko déggee] ; ba egal seen yaram ya ak seen xel ya door a firiku jëm ci fàttaliku Yàlla. [Alxuraan] jooju moo di njubug Yàlla mu di ci gindi ku ko soob. Ku Yàlla namm a réeral kenn du ko gindi.
24أَفَمَن يَتَّقِي بِوَجْهِهِ سُوءَ الْعَذَابِ يَوْمَ الْقِيَامَةِ ۚ وَقِيلَ لِلظَّالِمِينَ ذُوقُوا مَا كُنتُمْ تَكْسِبُونَ
Moo ndax ki am bugël mi gën a gën a bon ( niróo na ak ka dugg Àjjana), bu Bis Pénc baa bu boobaa tooñkat ya... Dañu naan leen : “Tokamtikuleen li ngeen daan fàggu”.
25كَذَّبَ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ فَأَتَاهُمُ الْعَذَابُ مِنْ حَيْثُ لَا يَشْعُرُونَ
Xeet ya leen fi jiitu woon weddi woon nañu (Yonnent yi), mbugël ma dikkëlleen fuñu ko foogewul.
26فَأَذَاقَهُمُ اللَّهُ الْخِزْيَ فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا ۖ وَلَعَذَابُ الْآخِرَةِ أَكْبَرُ ۚ لَوْ كَانُوا يَعْلَمُونَ
Yàlla musal na leen mbugëlu toroxtaane ci dundug àddina sii. Te mbugëlu àllaaxira, moo, gën a rëy, cëy bu ñu xamoon !
Az-ZumarFihi Alxuraan
75Aaya
MeccanRevelation
24Aaya

Tekki — Az-Zumar 24

Simoore Az-Zumar Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax ki am bugël mi gën a gën a…

Simoore Aaya 24/75 — Az-Zumar الزمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zumar Dégg, Az-Zumar Tekki, Az-Zumar mp3, Az-Zumar pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers