Az-Zumar · 32/75
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zumar
۞ فَمَنْ أَظْلَمُ مِمَّن كَذَبَ عَلَى اللَّهِ وَكَذَّبَ بِالصِّدْقِ إِذْ جَاءَهُ ۚ أَلَيْسَ فِي جَهَنَّمَ مَثْوًى لِّلْكَافِرِينَ ٣٢
Transliteration
Faman azlamu mimman kazaba `alal laahi wa kazzaba bissidqi iz jaaa`ah; alaisa fee Jahannama maswal lilkaafir
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ana kan moo gën a tooñ, kuy fenal Yàlla tey weddi dëgg saa su dëgg dikkee ? Moo ndax Safara dafa amul wàccuwaayub yéefar ya ? (Axakaañ !)
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 30-34 — Simoore Az-Zumar
30إِنَّكَ مَيِّتٌ وَإِنَّهُم مَّيِّتُونَ
Yaw dangay dee ñoom it dañuy dee ;
31ثُمَّ إِنَّكُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ عِندَ رَبِّكُمْ تَخْتَصِمُونَ
su ko defee, ngeen daje ca seen kanamu Boroom, di xulóo bu Bis Pénc baa.
32۞ فَمَنْ أَظْلَمُ مِمَّن كَذَبَ عَلَى اللَّهِ وَكَذَّبَ بِالصِّدْقِ إِذْ جَاءَهُ ۚ أَلَيْسَ فِي جَهَنَّمَ مَثْوًى لِّلْكَافِرِينَ
Ana kan moo gën a tooñ, kuy fenal Yàlla tey weddi dëgg saa su dëgg dikkee ? Moo ndax Safara dafa amul wàccuwaayub yéefar ya ? (Axakaañ !)
33وَالَّذِي جَاءَ بِالصِّدْقِ وَصَدَّقَ بِهِ ۙ أُولَٰئِكَ هُمُ الْمُتَّقُونَ
Ku indi dëgg ak ku koy saxal, ñooñoo ragal Yàlla.
34لَهُم مَّا يَشَاءُونَ عِندَ رَبِّهِمْ ۚ ذَٰلِكَ جَزَاءُ الْمُحْسِنِينَ
Am nañu lu leen soob fa seen Boroom ; loolu mooy peyug ñiy rafetal,
Az-ZumarFihi Alxuraan
75Aaya
MeccanRevelation
32Aaya
Tekki — Az-Zumar 32
Simoore Az-Zumar Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ana kan moo gën a tooñ, kuy fenal Yàlla tey…Simoore Aaya 32/75 — Simoore Az-Zumar الزمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zumar Dégg, Simoore Az-Zumar Tekki, Simoore Az-Zumar mp3, Simoore Az-Zumar pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, September 8, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








