Ghafir · 38/85
Tekki Waxtaan — Ghafir
وَقَالَ الَّذِي آمَنَ يَا قَوْمِ اتَّبِعُونِ أَهْدِكُمْ سَبِيلَ الرَّشَادِ ٣٨
Transliteration
Wa qaalal lazeee aamana yaa qawmit tabi`ooni ahdikum sabeelar rashaad
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Waa ja gëmoon daldi wax ne : "Yéen samaw nit, toppleen ma. Ma gindileen jëmëleleen ci yoonu njub.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 36-40 — Ghafir
36وَقَالَ فِرْعَوْنُ يَا هَامَانُ ابْنِ لِي صَرْحًا لَّعَلِّي أَبْلُغُ الْأَسْبَابَ
Firawna wax na ne : "Yaw Haamaan, tabaxal ma ag tóoj : ndax amaana ma man a gis yoon ya,
37أَسْبَابَ السَّمَاوَاتِ فَأَطَّلِعَ إِلَىٰ إِلَٰهِ مُوسَىٰ وَإِنِّي لَأَظُنُّهُ كَاذِبًا ۚ وَكَذَٰلِكَ زُيِّنَ لِفِرْعَوْنَ سُوءُ عَمَلِهِ وَصُدَّ عَنِ السَّبِيلِ ۚ وَمَا كَيْدُ فِرْعَوْنَ إِلَّا فِي تَبَابٍ
yooni asamaan yi, ndax ma man a yërndu Yàllay Muusaa ; te man sax ay fen laa ko jàppe”. Noonu la Firawna rafetloo jëfëm ju ñaaw joojee ; sorenaak dëgg lool ; te pexem Firawna du lenn lu dul luy naaxsaay.
38وَقَالَ الَّذِي آمَنَ يَا قَوْمِ اتَّبِعُونِ أَهْدِكُمْ سَبِيلَ الرَّشَادِ
Waa ja gëmoon daldi wax ne : "Yéen samaw nit, toppleen ma. Ma gindileen jëmëleleen ci yoonu njub.
39يَا قَوْمِ إِنَّمَا هَٰذِهِ الْحَيَاةُ الدُّنْيَا مَتَاعٌ وَإِنَّ الْآخِرَةَ هِيَ دَارُ الْقَرَارِ
Yéen samaw nit, dundug àddina sii diir bu néew la, dundug àllaaxira nag mooy sax.
40مَنْ عَمِلَ سَيِّئَةً فَلَا يُجْزَىٰ إِلَّا مِثْلَهَا ۖ وَمَنْ عَمِلَ صَالِحًا مِّن ذَكَرٍ أَوْ أُنثَىٰ وَهُوَ مُؤْمِنٌ فَأُولَٰئِكَ يَدْخُلُونَ الْجَنَّةَ يُرْزَقُونَ فِيهَا بِغَيْرِ حِسَابٍ
Képp kuy def ñaawtéef dees na ko fay kem la mu def ; waaye képp kuy def yiw, di góor mbaa muy jigéen, te fekk mu gëm, ñoom ñooy dugg Àjjana di fa jot xéewël yu amul waññ.
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
38Aaya
Tekki — Ghafir 38
Simoore Ghafir Aaya 38 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waa ja gëmoon daldi wax ne : "Yéen samaw nit,…Simoore Aaya 38/85 — Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ghafir Dégg, Ghafir Tekki, Ghafir mp3, Ghafir pdf. Aaya 36–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








