Ash-Shura · 27/53
Tekki Waxtaan — Ash-Shura
۞ وَلَوْ بَسَطَ اللَّهُ الرِّزْقَ لِعِبَادِهِ لَبَغَوْا فِي الْأَرْضِ وَلَٰكِن يُنَزِّلُ بِقَدَرٍ مَّا يَشَاءُ ۚ إِنَّهُ بِعِبَادِهِ خَبِيرٌ بَصِيرٌ ۝٢٧
Wa law basatal laahur rizqa li`ibaadihee labaghaw fil ardi wa laakiny yunazzilu biqadarim maa yashaaa`; innahoo bi`ibaadihee Khabeerum Baseer
📖 Tekkim Wolof
Bu Yàlla yaatalaloon wërsëg jaamam [ñépp], kon dañuy bew ; ba tax na, mu di ko wàcce di ko yemale na mu ko soobee. Ndax Yàlla ku Xàmmee la kuy Gis la Jaamam ñi.
🎧 Dégg

📜 Aaya 25-29 — Ash-Shura

25وَهُوَ الَّذِي يَقْبَلُ التَّوْبَةَ عَنْ عِبَادِهِ وَيَعْفُو عَنِ السَّيِّئَاتِ وَيَعْلَمُ مَا تَفْعَلُونَ
Mooy kiy ndangu tuub ci jaamam ñi, tey jéggale ñaawtéef yi tey xam li ngeen di def.
26وَيَسْتَجِيبُ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ وَيَزِيدُهُم مِّن فَضْلِهِ ۚ وَالْكَافِرُونَ لَهُمْ عَذَابٌ شَدِيدٌ
te it mooy nangul ñi gëm tey jëf yiw di leen xeewël, yéefar yi nag ñoom am na ñu mbugël mu tar.
27۞ وَلَوْ بَسَطَ اللَّهُ الرِّزْقَ لِعِبَادِهِ لَبَغَوْا فِي الْأَرْضِ وَلَٰكِن يُنَزِّلُ بِقَدَرٍ مَّا يَشَاءُ ۚ إِنَّهُ بِعِبَادِهِ خَبِيرٌ بَصِيرٌ
Bu Yàlla yaatalaloon wërsëg jaamam [ñépp], kon dañuy bew ; ba tax na, mu di ko wàcce di ko yemale na mu ko soobee. Ndax Yàlla ku Xàmmee la kuy Gis la Jaamam ñi.
28وَهُوَ الَّذِي يُنَزِّلُ الْغَيْثَ مِن بَعْدِ مَا قَنَطُوا وَيَنشُرُ رَحْمَتَهُ ۚ وَهُوَ الْوَلِيُّ الْحَمِيدُ
Moo (leen) di wàcceel taw ginnaaw bu ñu yàkke xont, te mooy tasaare Yërmaandeem. Mooy Kilifa gi, di Yayoowaakoonu cant.
29وَمِنْ آيَاتِهِ خَلْقُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَثَّ فِيهِمَا مِن دَابَّةٍ ۚ وَهُوَ عَلَىٰ جَمْعِهِمْ إِذَا يَشَاءُ قَدِيرٌ
Bokk na ci ay kéemaanam bindug asamaan yeek suuf ak ndundët yi mu tasaare (nuy duggat). Te man na leen dajale saa su Ko soobee.
Ash-ShuraFihi Alxuraan
53Aaya
MeccanRevelation
27Aaya

Tekki — Ash-Shura 27

Simoore Ash-Shura Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu Yàlla yaatalaloon wërsëg jaamam [ñépp], kon dañuy bew ;…

Simoore Aaya 27/53 — Ash-Shura الشورى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shura Dégg, Ash-Shura Tekki, Ash-Shura mp3, Ash-Shura pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers