Ash-Shura · 28/53
Tekki Waxtaan — Ash-Shura
وَهُوَ الَّذِي يُنَزِّلُ الْغَيْثَ مِن بَعْدِ مَا قَنَطُوا وَيَنشُرُ رَحْمَتَهُ ۚ وَهُوَ الْوَلِيُّ الْحَمِيدُ ۝٢٨
Wa Huwal lazee yunazzilul ghaisa mim ba`di maa qanatoo wa yanshuru rahmatah; wa Huwal Waliyyul Hameed
📖 Tekkim Wolof
Moo (leen) di wàcceel taw ginnaaw bu ñu yàkke xont, te mooy tasaare Yërmaandeem. Mooy Kilifa gi, di Yayoowaakoonu cant.

🎧 Dégg


📜 Aaya 26-30 — Ash-Shura

26وَيَسْتَجِيبُ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ وَيَزِيدُهُم مِّن فَضْلِهِ ۚ وَالْكَافِرُونَ لَهُمْ عَذَابٌ شَدِيدٌ
te it mooy nangul ñi gëm tey jëf yiw di leen xeewël, yéefar yi nag ñoom am na ñu mbugël mu tar.
27۞ وَلَوْ بَسَطَ اللَّهُ الرِّزْقَ لِعِبَادِهِ لَبَغَوْا فِي الْأَرْضِ وَلَٰكِن يُنَزِّلُ بِقَدَرٍ مَّا يَشَاءُ ۚ إِنَّهُ بِعِبَادِهِ خَبِيرٌ بَصِيرٌ
Bu Yàlla yaatalaloon wërsëg jaamam [ñépp], kon dañuy bew ; ba tax na, mu di ko wàcce di ko yemale na mu ko soobee. Ndax Yàlla ku Xàmmee la kuy Gis la Jaamam ñi.
28وَهُوَ الَّذِي يُنَزِّلُ الْغَيْثَ مِن بَعْدِ مَا قَنَطُوا وَيَنشُرُ رَحْمَتَهُ ۚ وَهُوَ الْوَلِيُّ الْحَمِيدُ
Moo (leen) di wàcceel taw ginnaaw bu ñu yàkke xont, te mooy tasaare Yërmaandeem. Mooy Kilifa gi, di Yayoowaakoonu cant.
29وَمِنْ آيَاتِهِ خَلْقُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَثَّ فِيهِمَا مِن دَابَّةٍ ۚ وَهُوَ عَلَىٰ جَمْعِهِمْ إِذَا يَشَاءُ قَدِيرٌ
Bokk na ci ay kéemaanam bindug asamaan yeek suuf ak ndundët yi mu tasaare (nuy duggat). Te man na leen dajale saa su Ko soobee.
30وَمَا أَصَابَكُم مِّن مُّصِيبَةٍ فَبِمَا كَسَبَتْ أَيْدِيكُمْ وَيَعْفُو عَن كَثِيرٍ
Bépp lor ju leen dal yéen a ko jëf. Yàlla dafay jéggale yu bari.
Ash-ShuraFihi Alxuraan
53Aaya
MeccanRevelation
28Aaya

Tekki — Ash-Shura 28

Simoore Ash-Shura Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo (leen) di wàcceel taw ginnaaw bu ñu yàkke xont,…

Simoore Aaya 28/53 — Ash-Shura الشورى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shura Dégg, Ash-Shura Tekki, Ash-Shura mp3, Ash-Shura pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers