Ash-Shura · 3/53
Tekki Waxtaan — Ash-Shura
كَذَٰلِكَ يُوحِي إِلَيْكَ وَإِلَى الَّذِينَ مِن قَبْلِكَ اللَّهُ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ ۝٣
Kazaalika yooheee ilaika wa ilal lazeena min qablikal laahul `Azeezul Hakeem
📖 Tekkim Wolof
Noonu la la Yàlla, miy boroom Kàttan, tey ku Xereñ, di soloo ay ndigëlam, kem ni mu ku defe woon ca Yonnent ya la jiitu woon.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-5 — Ash-Shura

1حم
Haa, Miam.
2عسق
Ayn, Siin, Qaaf.
3كَذَٰلِكَ يُوحِي إِلَيْكَ وَإِلَى الَّذِينَ مِن قَبْلِكَ اللَّهُ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Noonu la la Yàlla, miy boroom Kàttan, tey ku Xereñ, di soloo ay ndigëlam, kem ni mu ku defe woon ca Yonnent ya la jiitu woon.
4لَهُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۖ وَهُوَ الْعَلِيُّ الْعَظِيمُ
Moo moom li nekk ci asamaan yeek suuf si. te mooy Kooku, di aji Màgg ji,
5تَكَادُ السَّمَاوَاتُ يَتَفَطَّرْنَ مِن فَوْقِهِنَّ ۚ وَالْمَلَائِكَةُ يُسَبِّحُونَ بِحَمْدِ رَبِّهِمْ وَيَسْتَغْفِرُونَ لِمَن فِي الْأَرْضِ ۗ أَلَا إِنَّ اللَّهَ هُوَ الْغَفُورُ الرَّحِيمُ
Asamaan yi dañuy xawa foq bu Malaaka yi di sàbbaal di kañ seen Boroom, tey jéggalul ñi nekk ci kaw suuf si. te Yàlla tigi mooy Jéggëlaakoon bi, di Jaglewaakoon bi yërmandéem.
Ash-ShuraFihi Alxuraan
53Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Ash-Shura 3

Simoore Ash-Shura Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noonu la la Yàlla, miy boroom Kàttan, tey ku Xereñ,…

Simoore Aaya 3/53 — Ash-Shura الشورى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shura Dégg, Ash-Shura Tekki, Ash-Shura mp3, Ash-Shura pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, August 19, 2026

Don't forget us in your sincere prayers