Ash-Shura · 39/53
Tekki Waxtaan — Ash-Shura
وَالَّذِينَ إِذَا أَصَابَهُمُ الْبَغْيُ هُمْ يَنتَصِرُونَ ۝٣٩
Wallazeena izaa asaabahumul baghyu hum yantasiroon
📖 Tekkim Wolof
ña nga xam ne, saa su ag tooñ amee, ñu saafara ko (fayu).

🎧 Dégg


📜 Aaya 37-41 — Ash-Shura

37وَالَّذِينَ يَجْتَنِبُونَ كَبَائِرَ الْإِثْمِ وَالْفَوَاحِشَ وَإِذَا مَا غَضِبُوا هُمْ يَغْفِرُونَ
ñiy wattandiku bàkkaar yu mag a mag yi ak ñaawtéef yi, te saa su ñu meree jéggale,
38وَالَّذِينَ اسْتَجَابُوا لِرَبِّهِمْ وَأَقَامُوا الصَّلَاةَ وَأَمْرُهُمْ شُورَىٰ بَيْنَهُمْ وَمِمَّا رَزَقْنَاهُمْ يُنفِقُونَ
ñiy nangul seen boroom, ak taxawal Julli, ak di disóo seen mbir ci seen diggënte, tey joxe ci la ñu leen wërsëgël (seeni alal),
39وَالَّذِينَ إِذَا أَصَابَهُمُ الْبَغْيُ هُمْ يَنتَصِرُونَ
ña nga xam ne, saa su ag tooñ amee, ñu saafara ko (fayu).
40وَجَزَاءُ سَيِّئَةٍ سَيِّئَةٌ مِّثْلُهَا ۖ فَمَنْ عَفَا وَأَصْلَحَ فَأَجْرُهُ عَلَى اللَّهِ ۚ إِنَّهُ لَا يُحِبُّ الظَّالِمِينَ
Lu bon lu bon a koy fay ni moom. Waaye kuy jéggële tey yéwénal (na xam ne), Yàllaay warloo peyam. Te Yàlla du safoo tooñkat ya !
41وَلَمَنِ انتَصَرَ بَعْدَ ظُلْمِهِ فَأُولَٰئِكَ مَا عَلَيْهِم مِّن سَبِيلٍ
Ñay fayu ginnaaw ba ñu leen tooñee,...ñooñu kenn amul ci ñoom aw yoon ;
Ash-ShuraFihi Alxuraan
53Aaya
MeccanRevelation
39Aaya

Tekki — Ash-Shura 39

Simoore Ash-Shura Aaya 39 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ña nga xam ne, saa su ag tooñ amee, ñu…

Simoore Aaya 39/53 — Ash-Shura الشورى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shura Dégg, Ash-Shura Tekki, Ash-Shura mp3, Ash-Shura pdf. Aaya 37–41. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers