Ash-Shura · 8/53
Tekki Waxtaan — Ash-Shura
وَلَوْ شَاءَ اللَّهُ لَجَعَلَهُمْ أُمَّةً وَاحِدَةً وَلَٰكِن يُدْخِلُ مَن يَشَاءُ فِي رَحْمَتِهِ ۚ وَالظَّالِمُونَ مَا لَهُم مِّن وَلِيٍّ وَلَا نَصِيرٍ ۝٨
Wa law shaaa`al laahu laja`alahum ummatanw waahi datanw walaakiny yudkhilumany yashaaa`u fee rahmatih; waz zaalimoona maa lahum minw waliyyinw wa laa naseer
📖 Tekkim Wolof
Su sooboon Yàlla, Mu def leen wenn xeet. Waaye Mooy dugël ku Ko neex ci biir yërmandéem. Te tooñkat yi nag ñoom duñu am wéeruwaay, waxantumalaak ku leen di dimbali.

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Ash-Shura

6وَالَّذِينَ اتَّخَذُوا مِن دُونِهِ أَوْلِيَاءَ اللَّهُ حَفِيظٌ عَلَيْهِمْ وَمَا أَنتَ عَلَيْهِم بِوَكِيلٍ
Ñuy wut ay wéeruwaay yu dul Yàlla, Yàllaa ngi leen di fuglu. Te yaw (Muhammad) du yaay lijjanti seen mbir.
7وَكَذَٰلِكَ أَوْحَيْنَا إِلَيْكَ قُرْآنًا عَرَبِيًّا لِّتُنذِرَ أُمَّ الْقُرَىٰ وَمَنْ حَوْلَهَا وَتُنذِرَ يَوْمَ الْجَمْعِ لَا رَيْبَ فِيهِ ۚ فَرِيقٌ فِي الْجَنَّةِ وَفَرِيقٌ فِي السَّعِيرِ
Noonu la nu la soloo (Alxuraan jiy làmmiñu araab), ngir nga xupp ci ndayi dëkk ya (waa Màkka) ak dëkk ya ko wër ak it nga waar leen ci Bisub daje ba, - (bis pénc ba) sikkuwul bu boobaa - Ab kurél dafay nekk ca àjjana beneen kurél ba nekk ca biir Safara.
8وَلَوْ شَاءَ اللَّهُ لَجَعَلَهُمْ أُمَّةً وَاحِدَةً وَلَٰكِن يُدْخِلُ مَن يَشَاءُ فِي رَحْمَتِهِ ۚ وَالظَّالِمُونَ مَا لَهُم مِّن وَلِيٍّ وَلَا نَصِيرٍ
Su sooboon Yàlla, Mu def leen wenn xeet. Waaye Mooy dugël ku Ko neex ci biir yërmandéem. Te tooñkat yi nag ñoom duñu am wéeruwaay, waxantumalaak ku leen di dimbali.
9أَمِ اتَّخَذُوا مِن دُونِهِ أَوْلِيَاءَ ۖ فَاللَّهُ هُوَ الْوَلِيُّ وَهُوَ يُحْيِي الْمَوْتَىٰ وَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Walla ñoom dañoo far am wéeruwaay yu dul Yàlla ? Wéeruwaay tigi mooy Yàlla ; te mooy dekkal ñu dee woon ña te moo di ki man lépp lu ne.
10وَمَا اخْتَلَفْتُمْ فِيهِ مِن شَيْءٍ فَحُكْمُهُ إِلَى اللَّهِ ۚ ذَٰلِكُمُ اللَّهُ رَبِّي عَلَيْهِ تَوَكَّلْتُ وَإِلَيْهِ أُنِيبُ
Te lépp lu ngeen am ag juuyoo, Yàlla yor àtte ba. Koo koo di Yàlla sama Boroom; ci Moom laay wéeru te it moom la doyloo.
Ash-ShuraFihi Alxuraan
53Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Ash-Shura 8

Simoore Ash-Shura Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Su sooboon Yàlla, Mu def leen wenn xeet. Waaye Mooy…

Simoore Aaya 8/53 — Ash-Shura الشورى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shura Dégg, Ash-Shura Tekki, Ash-Shura mp3, Ash-Shura pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers