Az-Zukhruf · 37/89
Tekki Waxtaan — Az-Zukhruf
وَإِنَّهُمْ لَيَصُدُّونَهُمْ عَنِ السَّبِيلِ وَيَحْسَبُونَ أَنَّهُم مُّهْتَدُونَ ٣٧
Transliteration
Wa innahum la yasuddoo nahum `anis sabeeli wa yahsaboona annahum muhtadoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te ñoom Dañu leen dëdaleek yoon (wu jub wa xocc), te ñu foog ne dañoo gindiku.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 35-39 — Az-Zukhruf
35وَزُخْرُفًا ۚ وَإِن كُلُّ ذَٰلِكَ لَمَّا مَتَاعُ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا ۚ وَالْآخِرَةُ عِندَ رَبِّكَ لِلْمُتَّقِينَ
ak ay xoyxoyal. loolu lépp du lenn lu dul bànneexu dundug àddina, te àllaaxiraa, nga fa sa Boroom, ngir ñu ragal Yàlla.
36وَمَن يَعْشُ عَن ذِكْرِ الرَّحْمَٰنِ نُقَيِّضْ لَهُ شَيْطَانًا فَهُوَ لَهُ قَرِينٌ
Képp kuy sori ak a dumóoyu tudd Yàlla (fàttaliku) Yëramaakoon bi, Dananu ko booleek Saytaane su mu lëkkalool.
37وَإِنَّهُمْ لَيَصُدُّونَهُمْ عَنِ السَّبِيلِ وَيَحْسَبُونَ أَنَّهُم مُّهْتَدُونَ
Te ñoom Dañu leen dëdaleek yoon (wu jub wa xocc), te ñu foog ne dañoo gindiku.
38حَتَّىٰ إِذَا جَاءَنَا قَالَ يَا لَيْتَ بَيْنِي وَبَيْنَكَ بُعْدَ الْمَشْرِقَيْنِ فَبِئْسَ الْقَرِينُ
Ba ne seef agsi ci Nun dey, daldi wax ne: “Aka neexoon ! Sunu diggënte soriyaantoo ni [Pénkook Suwu] ! ” – Ndaw lëkkëloo bu bon !
39وَلَن يَنفَعَكُمُ الْيَوْمَ إِذ ظَّلَمْتُمْ أَنَّكُمْ فِي الْعَذَابِ مُشْتَرِكُونَ
Loolu lépp du leen jariñ lenn tey jii – ginnaaw ba ngeen tooñee – yéen ay bokk yem ca biir mbugël ma.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
37Aaya
Tekki — Az-Zukhruf 37
Simoore Az-Zukhruf Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te ñoom Dañu leen dëdaleek yoon (wu jub wa xocc),…Simoore Aaya 37/89 — Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zukhruf Dégg, Az-Zukhruf Tekki, Az-Zukhruf mp3, Az-Zukhruf pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








