Az-Zukhruf · 5/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
أَفَنَضْرِبُ عَنكُمُ الذِّكْرَ صَفْحًا أَن كُنتُمْ قَوْمًا مُّسْرِفِينَ ۝٥
Afanadribu `ankumuz Zikra safhan an kuntum qawmam musrifeen
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax ! Danu leen di jox [Alxuraan] te fekk ngeen di ay yàqkat ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Az-Zukhruf

3إِنَّا جَعَلْنَاهُ قُرْآنًا عَرَبِيًّا لَّعَلَّكُمْ تَعْقِلُونَ
Def Nanu ko Alxuraan ci làmmiñu araab ndax amaana ngeen xellu (xalaat).
4وَإِنَّهُ فِي أُمِّ الْكِتَابِ لَدَيْنَا لَعَلِيٌّ حَكِيمٌ
Nekk na fi Nun, ca ndayi Téere ba (Allawhul mahfuus), kawe lool fees dell ag ràñnee.
5أَفَنَضْرِبُ عَنكُمُ الذِّكْرَ صَفْحًا أَن كُنتُمْ قَوْمًا مُّسْرِفِينَ
Moo ndax ! Danu leen di jox [Alxuraan] te fekk ngeen di ay yàqkat ?
6وَكَمْ أَرْسَلْنَا مِن نَّبِيٍّ فِي الْأَوَّلِينَ
Ak a bari lu nu yónni ci ay Yonnenta ca ña jiitu woon !
7وَمَا يَأْتِيهِم مِّن نَّبِيٍّ إِلَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
amul Yonnent bu mas a ñëw te yéjjiwuñu ko (ñaawal).
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 5

Simoore Az-Zukhruf Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax ! Danu leen di jox [Alxuraan] te fekk…

Simoore Aaya 5/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers