Az-Zukhruf · 62/89
Tekki Waxtaan — Az-Zukhruf
وَلَا يَصُدَّنَّكُمُ الشَّيْطَانُ ۖ إِنَّهُ لَكُمْ عَدُوٌّ مُّبِينٌ ٦٢
Transliteration
Wa laa yasuddan nakumush Shaitaanu innahoo lakum `aduwwum mubeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Buleen nangu mukk Saytaane di leen wëlbati ! Ndax seenub noon la (bu nëbbutuwul) fes.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 60-64 — Az-Zukhruf
60وَلَوْ نَشَاءُ لَجَعَلْنَا مِنكُم مَّلَائِكَةً فِي الْأَرْضِ يَخْلُفُونَ
Bu Nu sooboon , Nu def ci yéen ay Malaaka yuy ayayloo ci kaw suuf si.
61وَإِنَّهُ لَعِلْمٌ لِّلسَّاعَةِ فَلَا تَمْتَرُنَّ بِهَا وَاتَّبِعُونِ ۚ هَٰذَا صِرَاطٌ مُّسْتَقِيمٌ
Te firnde lay doon ci (Bis Pénc ba) waxtu wa. Buleen ci am sikki-sàkka. Te na ngeen ma topp : yoon wu jub xocc waa ngi nii.
62وَلَا يَصُدَّنَّكُمُ الشَّيْطَانُ ۖ إِنَّهُ لَكُمْ عَدُوٌّ مُّبِينٌ
Buleen nangu mukk Saytaane di leen wëlbati ! Ndax seenub noon la (bu nëbbutuwul) fes.
63وَلَمَّا جَاءَ عِيسَىٰ بِالْبَيِّنَاتِ قَالَ قَدْ جِئْتُكُم بِالْحِكْمَةِ وَلِأُبَيِّنَ لَكُم بَعْضَ الَّذِي تَخْتَلِفُونَ فِيهِ ۖ فَاتَّقُوا اللَّهَ وَأَطِيعُونِ
Ba Iisaa dikkee and ak i firnde, nee na leen : “Indil naa leen xam-xamu xereñ ak it ngir ma leeralal len lenn ci li ngeen di juubuu. Ragalleen Yàlla te topp ma.
64إِنَّ اللَّهَ هُوَ رَبِّي وَرَبُّكُمْ فَاعْبُدُوهُ ۚ هَٰذَا صِرَاطٌ مُّسْتَقِيمٌ
Yàlla moo di sama Boroom di seen Boroom. Na ngeen ko jaamu. Lii mooy yoon wu jub wa xocc.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
62Aaya
Tekki — Az-Zukhruf 62
Simoore Az-Zukhruf Aaya 62 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Buleen nangu mukk Saytaane di leen wëlbati ! Ndax seenub…Simoore Aaya 62/89 — Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zukhruf Dégg, Az-Zukhruf Tekki, Az-Zukhruf mp3, Az-Zukhruf pdf. Aaya 60–64. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








