Ad-Dukhan · 13/59
Tekki Waxtaan — Ad-Dukhan
أَنَّىٰ لَهُمُ الذِّكْرَىٰ وَقَدْ جَاءَهُمْ رَسُولٌ مُّبِينٌ ١٣
Transliteration
Annaa lahumuz zikraa wa qad jaaa`ahum Rasoolum mubeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ana fan la leen kii fàttaliku bawoo te ab Yonnent bu bir dikkoloon leen,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 11-15 — Ad-Dukhan
11يَغْشَى النَّاسَ ۖ هَٰذَا عَذَابٌ أَلِيمٌ
di moor nit ñi. Tey mbugël mu mitti.
12رَّبَّنَا اكْشِفْ عَنَّا الْعَذَابَ إِنَّا مُؤْمِنُونَ
“Waay-waay, sunu Boroom téggil nu mbugël mi. Ndax nun ay jullit la nu [léegi]”.
13أَنَّىٰ لَهُمُ الذِّكْرَىٰ وَقَدْ جَاءَهُمْ رَسُولٌ مُّبِينٌ
Ana fan la leen kii fàttaliku bawoo te ab Yonnent bu bir dikkoloon leen,
14ثُمَّ تَوَلَّوْا عَنْهُ وَقَالُوا مُعَلَّمٌ مَّجْنُونٌ
Ñu daldi dumóoyu te naan : “Kii daal, ab dof la”.
15إِنَّا كَاشِفُو الْعَذَابِ قَلِيلًا ۚ إِنَّكُمْ عَائِدُونَ
Dananu teggi mbugël mi tuuti ; dangeen dellusi de.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
13Aaya
Tekki — Ad-Dukhan 13
Simoore Ad-Dukhan Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ana fan la leen kii fàttaliku bawoo te ab Yonnent…Simoore Aaya 13/59 — Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ad-Dukhan Dégg, Ad-Dukhan Tekki, Ad-Dukhan mp3, Ad-Dukhan pdf. Aaya 11–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








